Mboolem àtte yi, Yàlla dafa ne rekk: jullileen, woorleen, joxeleen asaka, bàyyileen fen, sàcc, wuruj…
Waaye ba Muy digle julli ci Sang bi halayhi salaam da koo laytaayal (muxadima) [préambule] ne:
{Yàlla ak i malaakaam dañuy julli ci Yónnent bi…}
Sallal Laahu halayhi wasallam
Àjjumay jàmm ak xéewal. Ajjumay naataange ak mujj gu rafet na nu ñeel.
Njéggal ak yërmaandey Yàlla yal na sax ci way-dawlu yi.
Bokk yi maa ngi sàkku ci ku ko man, mu jàng Xasida gii te yéene yool bi way-dawlu yi, Yàlla dolli leen njéggal ak yërmaande.
sëriñ tuubaa bind na 27 livres:
1- tawhiid (gëm yalla) 12 livres
2- Fiqh 4 livres
3- soufisme (tasawuf) 8
4- grammaire arabe 1
Ak 2 livres yu boole tawhiid, Fiqh, tasawuf.
Ta lii lepp lenn rek la ci jublu muy murid yi jang xam seeni farata, nimu ko waxe woon ni: «diggël naa bepp murid mu jang ay farataam, ta dinaa leen bindal ay teere yu leen kay jangal »
Il n’y a pas de secret pour avoir une once de bonheur ici bas: faites vos 5 prières a l’heure, lisez le Coran régulièrement, multipliez L'istighfâr et le Dhikr, soyez bons, soyez juste, faites l’aumône, invoquez sans cesse, demandez pardon sans cesse
Nous avons effectivement donné à Dawud et à Sulayman une science; et ils dirent: «Louange à Allah qui nous a favorisés à beaucoup de Ses serviteurs croyants.»
An-Naml, 15
L’Espagne 🇪🇸 :
- Champion du Monde
- Anti-Sioniste
- Gouvernement de gauche
- Implacable
- Défend la Palestine
- Régularise les immigrés
- Emmerde les USA et Israël
- Pas des suceurs
- FC Barcelone
- Real Madrid
- 20 Ligue des Champions
- 4 Euro
- Climat doux
On est sur le meilleur pays au Monde