ولا تقتلوا اولادكم خشية إملاق نحن نرزقهم وإيّاكم إنّ قتلهم كان خطىأ كبيراً
Buleen rey seeni doom
ngir ragal ag ñakk; Nun
noo leen di wersëgal
ñoom ak yéen. Rey leen
bàkkaar bu rey la.
Yónnant bi SHW nee na:
Ku xëy wax ko, te gëm ko, bu faatoo ci bis bi, àjjana la jëm.
Ku gontu itam wax ko, te gëm ko, bu faatoo ci ngoon googu ba ci ëllëg si, àjjana la jëm.
Sëydidul Istixfaar
Khassida gui Serigne Touba dafa niaane Boromam néko :
"Défal mbinde mi mou bokkou si الباقيات الصالحات té nga nangalko kiko binde té nga def mboolém araf yi (lettre) mou nék paye di yiiw di nékhal gou diougué si Yaw ak Yonenté bi SHWS sangoub nie djitou ak nie moudiou 👇