Tay la Jamono neex ba ku nekk mana jugg dal sa kaw waaye ba jamono méttée dëgg yaw rekk lañu gis nga jëf. premièr vendredi du mois de ramadan on se rappelle en plein pandémie L’islam di jooy ngir wéetaayu jumaa yi fépp ci adduna Keroog yaw rekk lañu gis Mbacke jërëjëf 🤍
« Cheikh Ibreu dh yeem nama. Ndax da am luma yorr, yakaarni keen duko giss mu giss ko. Ma yakaarni kuko giss duci meuneuh jariñu mu fexé ba jott ci. Ma japp ni kuko moss dina neex ba dooko yaatal wayé mom iñanul » Serigne Touba