Top Tweets for #yonent
Ginnaaw bi nu ko santalee Boroomam (#Màggal_Tuubaa), nu ànd ak moom julli ci #Yonent bi (A.S) ci (#Gàmmu gi).
Ngir #Màggal gi moo ko diglé waaye #Gàmmu gi moo ko daan defal boppam.
"Tãhziimuhuu bis sunnati,
Yaxuudunaa lil Jannati,
Bihiz diyaadul minnati,
Li muhlisin muhãzzimi;"

Ginnaaw bi nu ko santalee Boroomam (#Màggal_Tuubaa), nu ànd ak moom julli ci #Yonent bi (A.S) ci (#Gàmmu gi).
Ngir #Màggal gi moo ko diglé waaye #Gàmmu gi moo ko daan defal boppam.
"Tãhziimuhuu bis sunnati,
Yaxuudunaa lil Jannati,
Bihiz diyaadul minnati,
Li muhlisin muhãzzimi;"

#Maam_Cerno jenn jëmm la !
Moo fonk #Yonent bi ba tuddée ko ay taawam (#Muhammadu_Awa_Bàlla ak #Muhammadu_Habiib...) Jël daanaka ñi des ci njaboot gi tuddée #Sahaaba ya...

Ñi MAAM CEERNO tuddé ag njabootam ci SAHABA yi
Seydinaa Abubakar
Seydinaa Omar
Seydinaa Usmaan
Seydinaa Aliw
Seydinaa Miqdaad
Seydinaa Hamsa
Seydinaa Saalih
Seydinaa Xaalid
Seydinaa Abbaas
Seydinaa Suhaybu
Seydinaa Subayru
Amna sëttëp buñ tuddé Seydinaa Muhaas ibn Jabal.

#Magi_Bayti ya (ca #Daarul_Muhti), fanaanee jàng #Xasiida ba bët set démb ci guddi (ca #Mawlud ba) keem ni ñu koy defee #guddi_altine gu jot ngir #Màggal ganek àdduna #Yonent bi !
Ñoom Fu ñu toll ñi ngi #Gàmmu...
Moo dem ba #Màkka laajte #pavillon bañu muure woon Barabu #Yonent bi (aleyhi salaam), ñu won ko ko mu jënd ko indi #Tuubaa ñu muure ko Barabu #Ku_Tedd ki !
#Seex_Siidil_Muxtaar_Mbàkke Yalnanu ko #Yàlla fayal🤲🏽...

Bimu jógee ci Tukkib Géej gi, bokk na ci dëkk yi #Sëriñ_Tuubaa njëkk a dem #Daaru_Salaam...
#Maam_Seex_Anta nganale ko fa ngan gu rëy ci ay fan yu bari ! Tëral fa lu nekk rendi (Giléem, Nag, Xar, Béy, Ganaar...) Ba tëral nit nar koo rendi #Sëriñ bi goreel ko !

Ndeysaan😭 ! For nanu ci kàdduy #Seex_Aydara_Mbàkke mu ne : "Ci fan i #Sëriñ_Abbaas yu mujj yi, su ko nee #Mbàkke nun de danoo bëgg nga yàgg fi da naan ko "At ya #Yonent beek #Sëriñ_Tuubaak_Cerno dundóon romb naa ko bu yàgg ! Luma fiy def ati ?"
Waxoon na bis am bu yàgg 😭😭😭...
#Sëriñ_Abbaas_Mbàkke (#Seex_Yibra_Faati ) dem nii bàyyi nu fi ak ug wéet😭😭😭 !!!
Boroom Mbaax gu rëy dem na ! Boroom Yërmande ju kawe dem na ! Boroom Jàmm ju yaatu dem na ! Boroom Barke bu rëy dem na ! Nit ug Yàlla dëgg dem na !
Yalna ko Yàlla dolliy leer te taas nu ci barkeem.

#Daam_Ahmadu_Faati lañu tuddée Magi #Boroom_Daarul_Muhti ja #Sëriñ_Tuubaa newoon "su dundóon kenn du ko xam !"
#Sëriñ_Abbaas ñu tuddée ko #Sahaaba ba nga xam ne ci barkeem lañu daan ñaan🤲🏽 am #ndox ca jamonoy #Yonent bi, suñu maralaan !
#Seex_Yibra_Faati aka yéeme !!!
SERIGNE DAAM FATY (yalla na yalla yok leeram) AK SERIGNE HABASS MBACKE (yalla nafi yag te weer)

Bis ub keroog la ni #Seex_Anta "#Seex lewwil ma sama we yi." #Maam_Seex nekk ca, #Ku_Tedd ki ne ko "#Seex dem naa ba ñëw."; "#Seex, #Yàlla bég na, #Yonent bi bég na, #Man bég naa, dingeen bég ëlëg !!!" Ne ko "#Seex, li des ci àddina lu fi yëngóoti #Boroom_loxo lu tuut lii la..."

#11_Novembre_1902/#11_Novembre_2020 (#118_ans)...
Bis ni tay la #Sunu_Jàmbaar ja #Seexul_Xaddiim jógé woon ci #tukki bu yàgg bi ko nasaraan yi yóbbu woon diirub juróom ñaari at (#7_ans)...
Ci la indaale #Ndam yu rëy yii ak #Sariñca bii tax tay kumu neex #bàkku, fëgg sa dënn !!!

...Te loolu ba #Boroom_Daaru sàncee dëkk ba léegi lañu ko fa tàmbali woon. Nga xam ne kon #Daarul_Muhti ñoom dinañu #Gàmmu_52fois walla #53_fois ci At mi !!!
Yaakaaru ma ni amna beneen dëkk bu fonkee #Yonent bi nii de...

Bokk yi ñaata #milimeetar (mm) la taw fan yii yépp ci #Sénégal ???
#Sëriñ_Tuubaa de moom #2392,2_milimeetar la taw ca kawam ca #Mayumba (#Gabon) !!!
Te terewul #jaamu_Yàlla ak a liggéeyal #Yonent ba...
Kenn du #SËRIÑ_TUUBAA
Yalnanu ko #Yàlla fayal...
Nu andil ko #Sëriñ_Móodu_Mustafaa ak #Sëriñ_Fàllu mu ñaanal leen, ne leen "dénk naa leen #Yàlla ak #Yonent bi ak #Seen_Baay_Cerno...)
Daal dàkk fas wa dem liggéeyali #Yàlla...
#FIT_JOM_NGOR_NJÀMBAAR, kudul Yaw yaa ko ko ëppale fopp !!!

"Kuñ teg ci #jaag jëmé ci #bàmmeel, ku ko ne am nga sang bu dul #Sëñ_Tuubaa, su mënóon a jóg du for uw #yat, #jaasi lay for dal ci sa kaw." #Seex_Abdulaay_Lahaat.
"#Sëriñ bi moom #Malaayka yabu ko, #Yonent yabu ko." #Seex_Muntaqaa_Mbàkke.
Ngir #Yàlla nan nu wax kuy #SËÑ_TUUBAA !
"Sàllaahu de #bisub_xiyaama su #Yàlla teewee, #Yonent bi teew, #Sëriñ_Tuubaa teew, ñaa ko sékkal ñépp teew, sañ namaa #rammu ñiy wax #ach_hadu_an_laaIllaaha_illallaa_wa_ach_hadu_anna_Muhammada_Rasuulullaa bañu jeex te yoonu ñii du ci nekk..." #Sëriñ_Saaliw_Mbàkke...

Ndeysaan, #17ème_jour ci koor #jullit yépp di ci fàttaliku #Bisub_Xare_Badar ba amoon ca jamonoy #Yonent ba (S.A.W), bokk ci bis yi #Islaam amee woon #Ndam...
Déggal ma tontub #Seriif_Asan_Faal boobu ci kàdduy #Sëriñ_Fàllu ja "fa #Yonent yiy talee seen bopp kufa talul sa bopp, naan #Baay gaa ña a ngi, doo moroom..."
#QGTFM2020
#Séydinaa_Habbaas_Mbàkke (#Ashaaxi)...
Ci jamonoy #Yonent bi (SAW), ci barkep turandóom la #Sahaaba ya daan def #tawàssul🤲 ngir #Yàlla may leen am #Ndox.
Waaye moom it (#Sëriñ_Habbaas) bimu toogee ci #Xilaafa gi la #Daarul_Muhti gëj a am jafe-jafe #ndox rawatina ci #Màggal...

@Xadim_BA Sénégal ku am fooy waxee rekk dangay yaakaar ne dangaa wara wax lula neex, walla loo wax noonu la.
Jamonoy #Yonent yi mbas daan na am te dafa daan dal #Yonent yi te du tere ñu muñ ko ba #Yàlla teggi ko. Yaw nga toog naan les #Marabouts s'ils savent prier, qu'ils le montrent ici.
#Mbàkke_Bàlla ni nga mel ci #Yàlla, #Yonent bi, #Sëriñ_Tuubaa ak #Maam_Cerno rekk la Jaam ñi mel ci #Yaw; amunu ci Yaw sago de, yaanu gënal #Ñépp ak #Lépp ngir yaa #Gën ci #Nun;
#Yàggal rekk te #Wér 😍❤👌...
Last Seen Hashtags on Sotwe
omegle
Seen from United Kingdom
lowlvl
Seen from United States
monkeyappwins
Seen from United Kingdom
furry #paws
นัดเย็ดชุมแพ
Seen from Thailand
evligizli
Seen from Turkey
GorditaRica
Seen from Ecuador
nolimit()****** filter:videos
Seen from Australia
momson(((((((((())))))))))********** filter:native_video
AyçaAyşinTuran
Seen from Turkey
Most Popular Users

Elon Musk 
@elonmusk
241.1M followers

Barack Obama 
@barackobama
119.1M followers

Cristiano Ronaldo 
@cristiano
112.3M followers

Donald J. Trump 
@realdonaldtrump
111.8M followers

Narendra Modi 
@narendramodi
107.1M followers

Rihanna 
@rihanna
98.1M followers

NASA 
@nasa
92.2M followers

Justin Bieber 
@justinbieber
91.3M followers

KATY PERRY 
@katyperry
88.7M followers

Taylor Swift 
@taylorswift13
82.5M followers

Lady Gaga 
@ladygaga
74.1M followers

Virat Kohli 
@imvkohli
71.4M followers

Kim Kardashian 
@kimkardashian
70.3M followers

YouTube 
@youtube
68.7M followers

Bill Gates 
@billgates
64.4M followers

Neymar Jr 
@neymarjr
64.3M followers

The Ellen Show
@theellenshow
62.4M followers

CNN 
@cnn
61.8M followers

Selena Gomez 
@selenagomez
61.7M followers

X 
@x
60.8M followers















