Dama diouli niane yallah pour niou woma entretien mm pas 1mn Sama phone soné may jubilé di nékhal voix nane oui allo bonjoukh rek degue au bout du fil kounane « mi salminima bandarabé foff. Kokou yoro?? »maniko feuchei iow rk coupé😪mangui xar ba beine peulh wowatima😂😂