Sénégal sax nak, gone gu bëgg lu baax, sa 1er adversaire avsbt Iblis sa waa kër ley nekk. Par des " teel na", "bu ñu jommal", "da ngaa waané". Bu demee baali sol lu bon ngani kii xalé la graawul. Bu muuree boppam nganiko jaruko dafa teel wala niko du am jëkkër.
C'est la réalité
Mane vie wou jambour tellement sama yoon nekoussi dangay fokni sax damala beugoul wala niakk kersa. Mane lou sama yoon nekoul meuno mouss ak waneih bama dougu si.
Li guena neex meune ngama raconter sa life yeup 5min après lepp lay fatei.
Lou way def boppam deugu lay dound.