كلّت العقول عن إيجاد كلمة بل كلمات لتوصيفك ، ولم تدرك الأذهان مقاماتك المرتفعة ارتفاعا، فلا صوت يذكر من تكون، ولا لسان نطق مزاياك ، ولا فعل أدرك ما فعلت فينا !
ولاكن عندنا يقين وجودِك في قلوبنا، و إن ضاقت فلها ما يوسًعها من حبّك، وإن توسّعت فلا تشبع من حبّك ❤️❤️❤️🙏🏼
@s_sourang@pmgtheboss Ci tënk 1er ministre su bëggee investissement bi am dina am ta president du ci man dara
Ta loolu dakoy yokk politiquement ta dina baax ci réew mi
Ta amna ci mbir yoo xam ni su siiwee rekk president du am fit u opposer wu ci
@s_sourang@pmgtheboss Pour man de investisseur yi suñ bëggee ta jaar ci 1er dina baax lool
Ndax dina tax mu gën a dëgëral taxawaayam ci politique en même temps réew mi dina dox ndax lu bari ci loxoom daanaka president amul solo noonu , ta lépp lu OS wax ci kaw bam siiw du ci ñeemee opposer wu !
@s_sourang@pmgtheboss Jàpp naani presidente du gaaw a tàggoo ak 1er ministre de !
Président moo gën a xam li ci nekk ci conséquence politique ak économique !
Bu 1er ministre démissionner wul (ta yaakaaru mako) president dina ko yeex a dàqq lool (sudee dina ko def)
Analyse la du information !