17 Avril « 1946 ca Tassett, ci Toundou Xabaaan ba, ça Yoonou Keur Baye Isma Diouf, ci Sama Toolou Baye ba (…) Boobou ak légui, sunu ladone xam, kene waroumala gueneu xam »
Sant nagn ci lepp Mbacké. Waayé dougnou Sant beu dapp lii nga gnou boolé ak Mom. 80 ans de Grâces♥️