*[ Ndenkaane Sëriñ Tuubaa ]*
SËRIÑ TUUBAA (haa da lahu Allaahu mahtaara lahu) nee na :
_« Ku julee ti ci yeen ba noppi na jàng « Xul huwa LAAHU AHAD » (Likhlaas) fukki yoon ak ñaar ( 12 fois). Ku yoroon wird na ko ci dolli, ku yorutoon wird na ko doyloo ! »_