L'idOle ¹&²
Toi, l’être soumis, ancré dans la culture des grands soufis et de la science suprême
Cultivé et tout à fait concentré sur son objectif : le service
Ben copain laaj nama: "Koor nit ñi lutax ñuy def lu bonn diko wax ak diko lijënti te Yalla tëcc Saaytane?
Maniko BAYE nena:
Tëcc(emprisonner) Seytane motax def lu bonn jaafe ci koor gi.
"Waaye giss nga ada la kepp kuñu tëcc kasso rek amna ñu lafay setsi"
#Cissey_Zaman_in_My_Own💞
Le colon est « parti » depuis 62 ans, pourtant on continue d'agir comme un pays colonisé...
Iblis est enchaîné depuis le début du mois de Ramadan, pourtant on continue de le suivre dans nos faits et gestes...
Dependance Spirituelle !
Dependance Nationale !
Tawfeex dinala maay do yeene kenn lu gënë yess li nga yeene sa bop!
Wolof saax waax nani: "Yeene neek la, borom mo ci fanaan!"
Mingi melni nga ñaanal sa mbokkum júllit rek Yalla defaal koko defaal lako...
@soufismOsenegal#Cissey_Zaman_in_My_Own💞
Ceey lepp du dara baari wax rek...
Baari wax danay tax:
-Do jángaalé lu dugg ci bopp ñiy taatan xam-xam wala ñaariñ...
-Di nga wax lu sa yonn nekuul ba wax caa lo ci xamuul wala lu ëpp ñulakoy toppé nak ganaw naan ya fi waxoon nangaam...
#Cissey_Zaman_in_My_Own💞
Moytul nekk boroom xam-xam boo xamni, li muy xas ñi « xamul dara » moo ëp li muy jàngale, ba njëriñu xam-xam gi raw ko...!
Moytul nekk kooku ñu tijjil buntu mbóotu Yàlla yii, mu wara duggu, taxaw ci bunt bi di dàggasante ak ñi si bitti ba bunt bi tëjju te yëggu ko...!