NJEGEMAAR MI JOMMAL WA WAA DËKK BI YÉPP. ANA KAN MOO KO MUJJ TAKK?
Ngóor si daa ñëw ci baay bi, ne ko : « Baay, da maa bëgg a takk soxna, gis naa xale bu rafet, boo xam ne taar bi foo ko takk weesu na ko, peru bët ba nag moom moo dàq bob kéwël...
Baay ji bég lool, daal di ne ko « loolu kay doom jarul waaj, nan dem nga won ma ko, ma waxtaan ak ay waajuram, ñu may la ko ».
Ba ñu àggee kër ndaw sa, baay bi ne jàkk ndaw si, far gën a barde doom ji ci xale bi, daal di ne wëlbét doom ji ne ko « doom nag cuuj day xam lekkam, kii moola sut ab lees, ku la ëpp expérience ku mel ni man moo man a jël xale bii... »
Ngóor si, mere baay bi ba futt, daal di lànk ba tëdd ca naaj wa, ne ko « Baay, maa lànk! Du ma ko def ! Du ma ko def ! Du ma ko def ! Ndaw si moom maa koy jël, te loo ci bañul rekk, bañu ma ko ci !»
Ba coow la nee kur, xulóo ba takkarnaase, ñu mujj dem Police ngir am solution, ba ñu demee, commissaire ba ne leen « woo leen ndaw si mu ñëw, ma àtte leen ci lu gaaw ! ».
Bi ndaw si ñëwee, commissaire bi ne ko jàkk moom it gën a miir gaa yi ci ndaw si, daal di ne leen « ngir coow li jeex, yeen ñaar ñépp da ngeen ma koy bàyyee, ndax xale bii kat ci man la gën a jekk, te man lay gën a nob, ndax maay commissaire dëkk bi! ».
Doom ja ak baay ba ne du ci dal, ba coow la mujj àgg ca "Ministre" bu mag ba. Ba "ministre" ba gisee ndaw si, moom it bukkib gaa yi far ko matt, ba coow la gënee takkarnaasee nag, ci la�� mujj layoo ji ñoom ñépp ca kilifa gu mag ga di son Exellence Monsieur le président de la république.
Bañ demee ca njiitum réew ma, moom it daa yokk ci xar mi karaw rekk, ndax moo gën a nob ndaw si ñépp, xëccoo ba gën a metti.
Bi li xewee nag, te pexe amul, ci la Ndaw si génne am pexe ne leen « leegi nañ organiser ab joŋante ci ku dàq a daw (cours)🏃♀️🏃♀️🏃♀️, damay samp samaw xél rekk, ku ma njëkk a jàpp ci yeen, kooka laay yëy guróom ».
Ñoom ñépp ñu d’accord ci li njegemaar mi wax, ndaw si ne bërét samp aw xélam, gaa ya topp ca, di daw, di daw, di daw... ba kenn ci ñoom amatul sago ci li muy def, ci noonu rekk, lañ jekki ci mbetteel ne sërëx ci ag kàmb gu xóot goo xam ne ñoom ñépp seen bakkan fa la yam.
Ndaw si daal di wëlbatiku, ñëw ba ci ñoom ne leen « yeen jamaale yi may wër ngir nob ma, dinaa leen wax nag tay man maay kan !
Man de maay àdduna mi leen tee nelaw yéen doomu Aadama yi ! Ngeen di daw sama ginnaaw saa su ne, ba mu jaral leen sàggane seen diine ! fàtte li taxoon Yàlla wàcce leen ci kaw suuf ! Ba tay jii ngeen ni sërëx ci seen bàmmeel, yéen rekk ak seeni jëf.
Yéen ñii des dima dàq nag, na ngeen xam ne fii rekk ngeen di mujj, du ngeen ma jot mukk ! »
* Àddunaa ngoog, mook mbaam a yam, loo man ngawar dutee bis ñëw mu detteel la !
Bind wu am solo wii nag, mi ngi jugee ci publication bu Ustaaz Xaadim Mbaye Loŋoor defoon ci Araab, Akb Majalis tekki ko ci wolof.
Ils étaient venus, les cœurs pleins d’intentions pures,
De Tivaouane, Ndiassane à Touba, sans peur des murs.
Leurs chapelets différaient, mais leurs prières s’unissaient,
Comme des rivières vers un même Océan sacré.
Des Tidjanes au pas lent, humbles sous le ciel clair,
Offraient leur silence au souvenir de Bamba,
Tandis que des Mourides les saluaient d’un regard sincère,
Reconnaissant en eux des frères de lumière.
Il n’y avait ni drapeau, ni dogme, ni distance,
Seulement l’écho d’une foi sans défense.
Car les saints se reconnaissent sans besoin de parole,
Et leurs disciples se croisent sans crainte, sans rôle.
Un Tidiane versait une larme devant le mausolée,
Non par allégeance, mais par amour partagé.
Un Mouride lui tendait la main, non pour l’inviter,
Mais pour lui dire : “Tu es chez toi, frère de vérité.”
Et là, dans la foule immense, flottait un parfum d’unité,
Celui des âmes qui savent que Dieu ne divise jamais.
Touba, ce jour-là, était plus qu’un lieu de mémoire :
C’était un miroir où se reflétait toute l’élégance de croire.
Merci à vous les Tidianes, les Layennes, Les Niassenes et les Khradr’
Merci d’avoir été là pour Bamba 👊🏾❤️
🇸🇳 Le Sénégalais ne sait pas aller au bout des luttes.
Un peu de tiopa ti par ci, quelques tweets enflammés par la..... puis on passe à autre chose. Résultat ? Rien ne change.
Si le pays compte 12 millions de pauvres sur 18 millions d’hab, ce n’est pas de la magie, c'est le fruit d’une redistribution inégalitaire soigneusement organisée.
💰 Tous les riches du pays doivent être présumés profiteurs :
marchés publics opaques
fonds étatiques captés
optimisation fiscale
comptes offshore
complicités politiques
🔥 Si on les avait assez terrorisés :
👉 Un Ba milliardaire n’aurait pas le toupet de venir donner son avis après avoir contribué à détruire ce pays
👉 le fils Sow (cité dans les Panama Papers) n’oserait pas se faire cirer les bottes dans un podcast sucre miel (coucou Afrofeeling)
👉 Un Cheikh Seck, épinglé, n’aurait jamais proposé un remboursement en public, trankilou sans trembler
🎙️ Ces gens participent au chaos… puis viennent nous faire la leçon sur la "réussite".
🧾 Ce qu’il faut ?
👉 Une plateforme publique pour afficher leurs avoirs, l’origine réelle de leur fortune, et la part qu’ils doivent rendre.
Ils s’enrichissent avec notre pays, donc y'a rien à cacher.
Sinon, dans 100 ans, on sera encore là à faire des threads sur les mêmes scandales.
En vérité, nous ne savons pas pas aller au bout de nos luttes. Ou alors… c’est que ce système nous arrange.
🔴 #PressFreedom reste un pilier solide dans toutes les sociétés dites démocratiques. Les propos du PM #Sonko rassurent. Que #Senegal maintient son ancrage dans la démocratie — #Jùb_Jùbbal_Jùbanty#JubbantiKoom à suivre ensemble, tout sous la protection divine 🙏🏾
✍🏾📻📺🎬🛜...
Le décès de quelqu’un de la même génération est toujours plus bouleversant. Le Seigneur nous rappelle encore une fois que la mort est la certitude et que Lui seul est décideur du temps qui nous reste ici bas. Notre âge, nos ambitions et projets ne sont rien face à Son décret.
🚨 Tant que ces genres de voyous seront à la tête de nos institutions, le banditisme d'Etat sera toujours présent dans notre pays 🇸🇳
Ki mo takhaw sama kanam néma "katal sa ndéye guéne centre de vote" pendant que je représentait le Pastef dans un bureau de vote... @SonkoOfficiel
Le Dr Mabouba DIAGNE a été officiellement installé, ce samedi à Rome, comme President de la conférence de la FAO. Une première pour un africain de l’ouest.
Fierté sénégalaise.
Plein succès.
Sénégal mo démé no xamni
Tant que Yangui beug diam, di bayi mou sedd, certains vont aller plus loin
Et lui en fait parti
Soumasi bokone guà toudou sama yaye si plateau worna yalla danou niou atté 😡
Xawma lutax niu convoqué ko
🔴 Dewenati depuis #Nice#France où se déroule la conférence des Nations Unies sur les Océans — #UNOC2025#NBorso ici pour #Senegal et les peuples du littoral #Atlantic#Africa
"Protéger l'océan n'est pas un luxe, mais un devoir pour les générations à venir..." — A suivre...🙏🏾
Ne pensez pas que cela n'arrive qu'aux autres. Du jour au lendemain, nous pouvons nous retrouver dans la même situation que sa famille. Alors partagez comme vous auriez aimé qu'on le fasse pour vous.
Salut Momar @Noo_IDcard,si je comprends bien Maky Sall ne sacriefiera pas de mouton pour la tabaski au Maroc conformément à la décision du roi Mohamed VI ou bien je vais consulter @grok ?
Salut @Abdoukarim44, d'après les infos, le roi Mohammed VI a interdit le sacrifice de mouton pour la Tabaski 2025 au Maroc à cause de la sécheresse et de la baisse du cheptel. Si Macky Sall est au Maroc, il devrait respecter cette décision, surtout en tant qu'invité et ancien président. Mais ses plans exacts ne sont pas clairs. La mesure divise : certains soutiennent pour des raisons économiques, d'autres protestent pour la liberté religieuse. Tu veux que je creuse plus ?