10 AOÛT 1895 - 10 AOÛT 2022 : MBACKE BARI - DJEWOOL- LOUGA - NDAR - DAKAR - GABON.
Ce 10 Août est à marquer d'une pierre blanche car il correspond au début de l'exil de Serigne Touba. Il est parti de Mbacke Bari ce jour pour répondre aux convocations du gouverneur du Sénégal.
Hier, j'ai suivi une séquence qui ma choqué sur solutiontv (Tv Sa Ndiogou). Le chroniqueur Baye Assane Mésséré, avoue en direct qu’un Serigne Daara lui a confié qu'il abuse de ces Ndongo. Remarquez à quel point son réflexe n’est pas de dénoncer mais de lui trouver des excuses😢👇
@SAbdoulahate Kéew mi, njuux li, ndundiin Gi ndeem ñooy lal lu ëpp ci ñi aw xeet di bindoo tax ña ñuy nuroo lu bari ci jëmm.
Déggoon naa fi tamit ne am na ñu fay làkk Wolof waaye amuma ci firnde.
Jaajëf baay kaw-kaw.
@SAbdoulahate Tënkiin wi am na solo lool. Bari lu nuy gis seetlu yu ni mel ci diggante Waa-sudãa ak Waa-senegaal. Xam naa boo boolee sunu cosaan hg nu bokk di Esipt gu njëkk, ak sunu kéew ak njuux yu niroo yi, tax yiy meññ ci sunuy suuf a yem. Bu ko defe Na nuy dunde (lekk) day bokk.
Yoruñuy ndënd, niroolewuñu col yuy melax, waaye ñu ngi taxaw temm, di ubbi xel yi, ngir aar nit ñi ci pakk yeek ndëgg-sërëx yi; fu ne ñu samp fa raayab xam-xam, jom ak ngor."
Soxna Mariyaama Ba.
Bataaxel Bu Guddee Nii. 👇🏾👇🏾👇🏾
" Sunu liggéey (njàngale), ak bu fajkat nag, nanguwuñum po ak njuumte. Ndax kenn du fowe nit; te nit, jëmm la ak xel. Saa boo yàqee xelum doomi Aadama, am nga bàkkaru ku ray nit...
Jàngalekat yi - dale ko ca yu tuut-tànk ya ba ca waa iniwersite (njangune) - ab xare (armée) lañu, bu am ngor, bariy jaloore, te kenn du lenn woy, duñu leen sargal.
😫😫 NéNama Pape Sidy Diekhal na Taak louma Yor yobou nako si Serigne si pour gnaNal mou FeigN, fayNa ay communiqué radio comme télé mais hélas..... alors aujourd'hui Internet va l'aider a trouver son enfant Nako Gnép partager svp 🙏🙏🙏🙏
Banuy tuut tank, yàq farañse moo nu daan rus loo, fii ak jëmm i jàmono ñàkk a man a bind wolof wu set mbaa di ko làkk ay taxa yaaraas.
Jaajëf waa @WaxWolof
Ni làkk wi demee nii jamono jii ba ku ko manul sax mu metti la neex na ma lool.
Amoon na fi ay jamono lu yées fukki nit a ko fi doon bind.
Li gën nag mooy dem jàngi ko balaa gën a yàgg ndax ci kanam tuuti ku ko bindul rekk am yambar nga te say wax sax dadul saf dara. ☺️
#Baataan#Fay:
1- delloo ab nuyoo ci ku la nuyu.
2- joxe xaalis walla dara loo digaale woon ak sa moroom.
3- giimloo, fay ab taal walla ab làmp bu doon takk.
#Fara : jottalikatub kàddu.
#Fasoo : jagoolul sa bopp dara ngir def ko.
#Fayloo : sant nit mu fay
👇👇👇
"Croiser un silencieux, un vrai silencieux, interroge toujours le sens – la nécessité – de sa propre parole, dont on se demande soudain si elle n’est pas un emmerdant babil, de la boue de langage."
#LPSMDH#Laplussecretememoiredeshommes#mbougarsarr#Goncourt2021
Nous avons fabriqué 20 tables bancs pour les élèves de Thiebe à Louga grâce à votre générosité. Merci aux donateurs il nous reste maintenant le défi du transport.
Qui peut nous aider à transporter 20 tables bancs rapidement à Ouarkhokh?
Retweet apprecié