Je rends hommage aux journalistes qui contribuent, par leur travail, parfois dans des conditions difficiles, à promouvoir la liberté d’expression. Parce que la liberté de la presse est garante d’une société démocratique et juste, elle est à la base de mon action de tous les jours
@Ndeye_fatoufaye mangui dora def remarque bii. Ndeketé yaw sa pp tweeter comme mane ngua def dale t photo bou yaague la mane sama boss han photo bo khameni dangua meussorou yawite saniko. Ko khameni lou sa mak def ngua defko ! Ndeye guemeul sa bopp ngua demal sa bop 🤣🤣🤣
@Ndeye_fatoufaye Wooouy 🤣🤣🤣 waw dalay yewaler touti d bangua dioug tok dioube khothie kay ! Mais nak ça dépend ci durée coma bi yaw gnaata fane ngua amagoum ?
Jullit bu ne war naa leeral bàmmeelam balaa caa dem, te mooy jëf ju baax ndax nit 4 la am, jëmmam, ay mbokkam, alalam ak jëfam ju baax. Bu tollee ci sukraat ñàkk na jëmmam, bu ñu ko suulee ñàkk na ay bokkam, ñu jox alal ji ña koy donnu, mu des ak ay jëfam ci bàmmeelam