@bmyoum Mais Ndioguou fama nak xana xel nangou na Kou khekh ba gnou woulou leu dioxla ya wara diriger nak ? Mais même si dou done ioe kessei ndax senegal gneupa ko bokk.. mais comment tu expliques que ioe gni togguone fep nei meuno yoor rew mi amo capacité intellectuelle bi. Tay ioe leu
@bmyoum Merci d’avoir reconnu qu’il a augmenté l’amour de la jeunesse pour leur patrie☺️et cette jeunesse sera avec lui ba biss bougnou guissei lou outei ak lignou guissone si mom ba andak mom
@bmyoum 5 eme reproches.. Ap djoulitt dou feine sougnouy tekk paka sa pout sax dagua wara di wax deugg.. cela ne l’excuse pas sur la mort du petit ndax bakane mo bakane la rk.. wantei dou mom moko feik neiguame ray ko et ceux là qui ont organisé les grèves amougnoussi part ?
@bmyoum 4 eme reproche : en deux ans de Macky bane loi là voter pour femme yi ak jeunesse bi 🤷🏽♀️d’autant plus que mom feikoul wade thiathiakhatei rew mi. Mom Rdc la feikone rew mi yobbou ko 4eme sous sol.. donc les urgence n’étaient pas les même s
@bmyoum 3ieme reproche : les lois sont faites pour être appliquées hein .. nul est supérieur à la loi sa leader moko wax.. defoul Dara loy andoul ak yoon dh liko yoon may rk la dieul mou dadiei mou favorable ak mom..
@bmyoum Les fonds politiques 😂😂il s’est enrichi avec ? On est d’accord que tu peux tout lui reprocher mais SONKO dou sathie quand même . Si tu peux prouver le contraire je suis toute oui
@bmyoum Gnoune dagno wowlei 😂😂à forcer de vouloir nous convaincre que le gars n’est pas bon, tu risques de ne plus avoir de temps pour convaincre le peuple que ton leader est le meilleur profil pour le Sénégal 🤷🏽♀️
@bmyoum Mais gnoune kessei momou gnou rew bi .. chacun est libre de voter pour qui il veut . Tu n’es pas avec lui c’est ok 👌🏽
Garde ton énergie pour battre campagne pour ton leader élection kou meune sa morom doumeu
Les nouveaux bracelets du parti Pastef-Les Patriotes « SONKO, LE GUIDE DE LA RÉVOLUTION » disponibles dès maintenant au siège et par livraison.
CONTACTS:
77 141 25 53
76 485 69 38
77 758 86 43
77 586 78 80