Fo guisse problème daawal ,koula siy woo itam daaw ko.Aduna bou gaateu bi béneu details boum la tarder ndax li niou war da beurri yoneu bi goudou ba paré beurri ay diam diam(Xaa Xaam). Sa objectif xell bou dalleu moy taax nga atteindre ko.Focus rk✌🏾
Kou nek si nioune meune na taxaw wax si moromam ay sikkam lou maat 1h de temps wayé sou neker ioe dagne la wax waxal say sikk dossi def 5min.Legui ioe naka ngay beugeulé sa bopp soutoureu si ba bapé bagnal ko sa morom té né ap dioulite nga ??? Na saa ayib bopou donneu sa yitté.
Meuna wax ak beurri wax ak reuy lamiñe daño ndiro té bokou ñou.
Kaa meuna wax say sou waaxé dieuriñe boppam mba mbokkam.
Kaa beurri wax meune na wax ba wax lou am ndiariñe wayé dée souko diariño ndax day taankal nit ñi.
Kaa reuy lamiñe nk say sou waxé dougeul boppam mbaa mbokkam.
Koudoul YALLA maato rawatina nioune nitt yi wayé lo xam si sa morom mouy ndioumté mba mouy ndirou niaaw teef yakamti nga guéneu ba tassaré ko lolou dou app dioulite dh …
Kila bayi té defoko dra boum le metti.Ioe léneu rk mola waar moy soléne amé bléme même sou neker mola togne sax demal diegualou ko. soy wax ak mome nk mou bagna baayi ioe bayiko nek si lenen té yener ko diam té itt saay bougne la ladié ani diiw na nga wax si mome lou refette.