#Kebetu#Ramadan2021#ramadanmubarak#Touba#senegal#islam
khassida "Fawzul Mutih" Sëriñ Tuubaa dajaley si ay Salatou hala Nabi you am solo lool, you mat di deff lool. Bokk na ci fukki djouli youmou toudé "Kayfiyatou Salaat", 👇
{Yàlla mi nga xam ne, saa boo ko jëfalee te sellal ko dina la gërëm, yamal ci moom di ko jëfal te bàyyi keneen.
Yàlla mi nga xam ne, booy sàkku ngërëmam, li nga ragal tay ak ëllëg lépp dina la ko fegal, booy jëf jëfal ngir moom.
Yàlla mi nga xam ne, ku koy topp ngir sàkku ngërëmam, dina la féetewoo taxaw ci say mbir, loo bëgg mu def ko, loo ragal mu fegal la ko, doy la sëkk ba doo soxlaal keneen, te boo moytoo li muy tere, dina la teral fajal la say aajo, deel jëf ngir moom rekk.}
Masaalikul Jinaan !
Pour une bonne santé, contrôlez votre alimentation,
Pour une bonne âme, contrôlez vos péchés et
Pour une bonne foi, envoyez vos bénédictions au Prophète MUHAMMAD (PSL).
– Imam Ghazali
Juróom-ñeenti fajkat yu am solo lool :
1. Alxuraan
2. Ndox mu sell
3. Nelaw guddi
4. Di noyyi ngelaw lu set
5. Dox fanweeri simili bis bu nekk
6. Lekk gu baax
7. Ceeñeerul jant bi
8. Gëm ab dogal
9. Baril di tudd Yàlla
Waaye khoolo loolu, ya ngi tekk sa gët yi rek si popularité Ousmane ba mou lay déranger. 54% yi la fal, senn yeenee sou sotti woon do tok si chaise bobou dei!! Ressaisis toi sinon tu risques de souffrir jusqu'en 2029, Sonko nimou mel Yàlla ko deff!!!
#kebetu#deçu#attristé
@PR_Diomaye deel sant Yàlla si kheweul yi mu la deffal!! Djoulit dey gueum ndogalou Boroomam. Ndogal bi la deff Président, mo deff Sonko nii mou mell si nitt gni. Yàlla defal na la lou rëy, moy nekk njiitu réew mi, ganaw yow 4 nit rek la ko Yàlla défal,
Un grand merci à cheikh bara pour ce travail de deconstruction du narratif du trio (barro-ajuma-diomaye).
L’objectif était d’affaiblir Ousmane dans pastef et de profiter de l’appareil politique du parti.
@GuisseSLY@Cisse_Maps@ModouL5 Wakhoul DEUG dei!! Lii mouy wakh amoul si adouna, amoul si histoire. Aucun projet, quel qu'il soit, ne peut être décorrélé de son porteur, à plus forte raison un projet de société. C'est pareil même en religion. Soit c'est de la jalousie, soit gnak kham adouna