NIT NI NIOU KO YARÉ NONOU LAY DIANGUÉ NI MOUY DIANGUÉ NOUNOU LAY XALATÉ NI MOUY XALATÉ NONOU LAY SOPÉ NI MOUY SOPÉ NONOU LAY YEUGUÉ NI MOUY YEUGUÉ NONOU LAY DIEUFÉ
MAME CHEIKH AHMED TIDJANE SY AL MAKTOUM
AL
Mourchid
Moh tax ma guem ki ma warul guem
Moh tax suma wax nieup nopi
Moh tax suma dieufé nieup naw ma
Moh tax ma xam sama responsabilité
Moh tax ma xam suñu borom loum may doyei kaw suff
...
DIARAMA CHEIKH SEYDIL MOUHAMADOUL MOUSTAPHA SY AL MOURCHID
L'inconnu de la nation
MAAM
MOM MI
TAXAWAL ZAWIYA MAME KHALIFA ABABACAR SY
FEKK DOMI GAÏNDË DIEUL KO YOBOUL KO DJAMAL
BOROM NÏËTTI FANN YÃ
BOROM ROKKOU BI...
VRAIMENT QUI EST
MAME CHEIKH AHMED TIDJANE SY AL MAKTOUM???????
Moh xam victoire
Moh xam défaite
L'essentiel am kilifeu
Bou matt kilifeu
Nek ndjaboot
Bou degg kilifam
Moy jam dji
Moy salam dji
Moy yokkouté gui
Baa yeukk ko
Tei dou am bénn reuthiou
SI C'EST PUR JE M'ENGAGE