Tokk rek di khar Yalla, doylo Yalla defko mouy sén allal di sén amamm di sén lepp.
Ndax sunu borom kharitam lay nattou.
Kone so beugei am liguéyaal, So beugei tékhé diamoul yalla, So ragalei safara watàndikoul moy.
Serigne Sam Mbaye ❤️
"Àdduna dem ba nga xam ne àdduna bi yëpp masse naañ ci bëgg Jàmm te xamuñu fuñu kay jële , Doxinu Sëriñ bi ndoŋ ci àdduna moo ñu ko mëna maay "
Sëriñ Muntaxaa Mbàkke
📌📌📌 SubhanAllahi wa bi Hamdihi SubhanAllahal
Azim Astaghfirullahal Azim, Al Lazi Lahilaha lla huwal Hayyul Qayyum wa Atubu llayhi 100x après le salut final de la prière de Jummuah
À épingler et partager que tout le monde puisse en profiter In sha Allah! Qu’Allah SWT facilite!