Seex Mustafaa tabax fondamaa jumaa ji ba mu weesu xaaj, mu bàyyi ko ak Alhaaji
Seex Mustafaa mu tabax kenoy jumaa ji, ya nekk fa baayam mu bàyyi ko ak Alhaaji
(Seex Muusa KA)
Daaru muhty ni la nuy taxawoo nit , gunge ko ci bameelam . Worma , ñeewantal , xasida . Do degg waxtaan do degg telephone !! Foofu dee ag fattali la fa batay