Il montre toujours que l’accomplissement passe par la discipline, forgeant des âmes aussi solides que des mains laborieuses.
YÀLLAH BUUR, no gi ñaan Sëriñ Seex wer te yàgg fi
Jamono ji bokk na ci Mag yi nu wara gënë wormal ci liggéeyub Qasayid yi
Moom rek mo bokkon, ci ñi fi des, si jàng bi mag ñi jàngon kër Sëriñ Abdullahi Jaxate, mu gënë siiwe si jàngum 78
Jàng boobu mo feddali na Mag ña naan jàngale KU TED KI Njaarem.
SRÑ SALIH fonkon na ko lool
@jalybadiane@O_dembouz Ma sha Allah ! Il contient des connaissances et des secrets que les chefs religieux de l’époque considéraient comme leur patrimoine personnel. SEEX ABO les a rendus accessibles.
Qu’ALLAH SWT soit d’avantage satisfait de lui ❤️