🚨📊📈NDOGOU SEEX IBRA FALL YI
Ganaaw sunu nuyo ag siar ñél murids yëpp !!!
Li moy sen jëff yi jotta aksi fi ñun dirrub 29 jours werru korr ag bëssub korité gui (añu Korité Yi). Lepp teggal na ñu leen ko ci loxo Serigne Bi dileen waax Déweeneti.
Ñu fobbu bu baax !!!
Seenuw doxiin dafay tegtale dëgg-dëggi ag taalibe. Seenub jataay day jëmmal ay teggiin. Seen pas-pas day taaral yoonuw tarbiya wi nga xam ne seen maam xàllal na leen ko. Na leen Yàlla sàmm, ku leen xool gis jullit yu set wecc ay muriit yu dëggal.
Mor Sourang ✍🏿
JËff Ji📌
Sen jëff yi ñu leen doon dajjaleel (@NdongoSeexIbra@Anta__...) gir mu tabbi ci Jëffi Seex Ibra ji jëm ci Ndigëlu yessalat Jummay Touba Ji jébbaleel na ñu leen ko tay ji ci diber gi 19 janvier 2025 mu tollu ci 𝟓.𝟒𝟐𝟓.𝟎𝟎𝟎 𝐅 𝐜𝐟𝐚 .
Jërëgeen Jëff !!!
Kone Nak lagni diayantei si beussou Khassida yi
Soobou rek seex ibrahima fall agali 🙌🏿
Bou kene kheb Dara meune na nek deh
Kousi beug barkelou meune ngako def wave /om
Numero : 781734326
Dinagn ko amal ba le 2 decembre inchallah fi ba bobou kousi beug barkelou rek