Saa bu guddi Àjjuma jotee, (maanaam tay Alxamiis ci guddi gi), nga jàng:
1-Faatiha 1X
2-Salaatu Halan Nabii 1X
3-Lixlaas 40X
4-Salaatu Halan Nabii 1X
Su noppee nga yéene ko jullit yi faatu yépp ak ñiy dund jamono jii, ak ñi wara judd.
Kon jullit bi njëkk a faatu ba ki mujjee faatu, dinañu am yoolub 40 Lixlaas.
Ku ko saxal ba Yawmal-Xiyaam, ku ñëw ci yaw ngir fayonte ak yaw, Yàlla moo naan ko, bàyyi ko mu dem ndax ku ñu mbaa-Yàlla la, dafa farlu woon bay maye aw yiiw.
Bul topp mukk say projets ci àdduna bii ba fàtte sa boroom.
Ku dee rekk, bàyyu nga fi ay projets.
Fexeel boole ñaar yii:
Di jaamu Yàlla na mu waree, di ligeey na nga manee.
Sëriñ Tuubaa RLTH daan na wax naan:
« Su ngeen xëyatee, na ngeen jiital jaamu Yàlla, teg ci nangoo ligéey »
«Ku bëgg teraangay àdduna, dangay nangoo ligéey, ku bëgg teraangay alaaxira nag, dangay nangoo jaamu Yàlla »
C’est pour moi une précieuse occasion de lui rendre un hommage. Mon admiration à son égard ne tient pas uniquement aux liens du sang, mais davantage à sa personnalité, à sa noblesse, à ses œuvres et à son parcours exemplaire, qui m’inspirent et continuent de guider mon chemin🤍
« Et quant au bienfait de ton Seigneur, proclame-le ». [93 : 11]
Alhamdoulilah, j’ai soutenu mon mémoire de Master en sciences agronomiques avec la mention Très Bien.
Nopplu jil ca «Illiyiin»
Yàlla gërëm nala'ak «Lamiin»
Yonen gërëm na la'ak ñeneen
Ak xulafaa-uy xarnu bi
Ak Mursaliina'ak Lanbiyaa
Ak taabihiina'ak lawliyaa
Jinne ya'ak Malaayika ya
Gërëm nañook waa xarnu bi
SMK ( Copie)
Sinon kou séleu ki, Son Excellence Sonko néna niou ande ak daal nioune patriotes yi. Bayi wax you eup yi ak louniou meune indil problème.
On a assez vécu des dingueries ndax politique !!!
Ndigeul nak djeufé. Niouy adjou ak ignorer et surtout se maîtriser. Loumou wax rq amna foumko tek.
Nopplu jil ca «Illiyiin»
Yàlla gërëm nala'ak «Lamiin»
Yonen gërëm na la'ak ñeneen
Ak xulafaa-uy xarnu bi
Ak Mursaliina'ak Lanbiyaa
Ak taabihiina'ak lawliyaa
Jinne ya'ak Malaayika ya
Gërëm nañook waa xarnu bi
SMK ( Copie)
« Certes, nous sommes à Allah et c’est à Lui que nous retournerons. »
Un père, un ami, un confident et un guide s’en est allé. Il a été là pour moi dans les moments les plus sombres, m’accompagnant de sa compassion, de ses conseils, de ses prières et de celles des milliers de disciples dans les différents Daara.
SHEIKH SALIH MBACKÉ, le preux du travail et de la spiritualité, maître de khélkom.
Allah, ô Allah, enveloppe‑le de Ta miséricorde infinie et ouvre‑lui les voies de Ton paradis éternel.
مِّنَ الْمُؤْمِنِينَ رِجَالٌ صَدَقُوا مَا عَاهَدُوا اللَّهَ عَلَيْهِ ۖ فَمِنْهُم مَّن قَضَىٰ نَحْبَهُ وَمِنْهُم مَّن يَنتَظِرُ ۖ وَمَا بَدَّلُوا تَبْدِيلًا
Serigne Cheikh mou Serigne Saliou kou ame solo ci adouna bi ci mbindèfi YÀLLA yi ci ISLAM ci yonou mamam Serigne Touba R.A Al Mouridiya di Sak ci yon wi... Diamou YÀLLA liguéy khidma yaré ci ISLAM diarigné sam ndono li la niou kham ci mom
YÀLLA nako YÀLLA diégal yeuramko défal ko ngueuramam la guena kawé kharé ko Jannatoul Firdaws. Amiin