*فَإِنَّ مَعَ الْعُسْرِ يُسْرًا*
*Jafe-jafe bu nekk, àndana ak yombal !*
*إِنَّ مَعَ الْعُسْرِ يُسْرًا*
*Jafe-jafe bu nekk, àndanaak ug yombal*
*فَإِذَا فَرَغْتَ فَانصَبْ*
*Te saa yoo féexee, jógël, julli*
*وَإِلَى رَبِّكَ فَارْغَب*
na ngay xemmeem jëm ci sa Büur.*
Saa menn magum Daara laa doon waxtaanal sànq mu ne ma Baayam da ko daan wax : "Nit dees na ko boole ak alalam duma, ak askanam duma, ak xam-xamam duma, waaye mukk ak yaram. Diw duma nañu ko ndax dafa am yar doo ko dégg, waaye boroom alal dees na ko duma,
Bàyyil di xalaat la nga ñàkk, ba ñàkk lii nga am!
Fàttaliku naqaru démb, dalay xañ sa jàmmi tay rekk, dëkke tuur say ronxooñ, te du yàgg a yàgg bamu saafaraal la ko, kon bul nangu naqar , xañ la jàmm, bamuy teew, xañ la ko bu dëddoo. Bul yàq sa jàmmi tay, ci luko mbaa kuko jarul
Comment l'Europe a sous-développé l'Afrique√✓
L'Afrique, étant la patrie
originelle de l'homme, a été un acteur majeur dans les
processus dans lesquels les groupes humains ont montré
une capacité de plus en plus grande à tirer profit de l'environnement naturel
Comment l'Europe a sous-développé l'Afrique√✓
Chaque continent a participé indépendamment aux
premières époques de l'extension du contrôle de
l'homme sur son environnement - ce qui signifie en fait
que chaque continent peut indiquer une période de
dévloppement économique
Comment l'Europe a sous-développé l'Afrique✓
Chaque peuple a montré sa capacité à accroître de
manière indépendante sa capacité à vivre une vie plus
satisfaisante en exploitant les ressources de la nature.