Ma dem colobane pour dieund Play 5 wadji nema 290 milles , maneko soumala teger play 2 nak mounema « Boba degay yok 50 milles mouy 340 milles ndakh play 2 damay yok thiono »
« Niampé biguay sango wara ko rakhassé sa kaname sinon daguay am ay boutons »
Saway mane bima dioudo ba léguii mak sama daleu yi nio bokou niampé t awma toussssss