La hawla wala quwata ila bilaahil aliyil aziim . La ilaha ilalaahu sayiduna muhamadun rasuululahi salla lahu tahala aleyhi wa salama wa ala alihi allahu akbar
Li ku ko wax 4 fois fidaaw la ci safara
Xaadim rasuul -Adurusamiin
Hussary a mémorisé le Quran a l’âge de 8ans. Il fut le premier homme qu’on a enregistré le coran sur disque. Husary a perfectionné la lecture du Coran dans les 10 lectures après ses études à Al Azhar.
Sa voix indescriptible, Son authenticité et sa célébrité inestimable
Êtes-vous livre papier ou numérique?
Pourquoi tu dois lire régulièrement ? 📚
Ton cerveau travaille 🧠
Ton vocabulaire s'étoffe 🗣️
Ta créativité est stimulée 💡
Ta mémoire s'améliore 🤩
Plus de connaissances 📖
Lire 🟰 Progresser
Yeesalaat njébal yi ✍️
Takaat laxasaay yi ✍️
Yokk xam-xam bi ✍️
Teewlu jaamu yalla yi✍️
Dëggal mbëgeel gi ✍️
Topp ndigël yi ✍️
Bayi tere yi ✍️
Rafetal Jëf yi ✍️
Ci weeru koor gi ✍️
Malgré toutes tes fautes ton Seigneur t'offre une chance de tout effacer ... Saisis La !
Ki maandu Ci misaal nit la koo xam ni ay ayibam doy na ko sëkk ba lijëntiwul ayibi jambuur waaye nak lu mat a tere mu tere, lu mat a diggle mu diggle, lu mat a jëf mu jëf ca keem katanam, te du jeggi mukk li neex ALLAH SWT. Du ko ëpp du ko yées.
ku mu sékkal di na ko jox aqqam ba mu mat sëkk muy ci walu njàay wala ci sëy wala ci mbiri aduna bu mu mën a doon.
Maandu lu jafe la ...