« Accomplissez la prière [normalement], car la prière demeure, pour les croyants, une prescription, à des temps déterminés. »
[Sourate An-Nisa’, Aya 103]
Borom Touba dafa indi si Safinatoul Amaan (Nafila) Hadith bou Abi Amaama Yalla nako Sunu Borom gueureum nétali dieuléko si Yonenté bi SHWS mou wakhni : "Kép kou diouly si goudik Altin�� (La nuit du Dimanche au Lundi) 2 Rakka bousinék mou dianguesi guinaaw Fatiha 1yoon (1fois)👇
Benn saudien da ne ma lutax ngay ñaan Yàlla di tawasul ci nit, dangaa wara def direct ci Yàlla ?
Ma ne ko lutax Yàlla deful direct wax ak nun li mu bëgg mu Yónni ay nit ngir ñu indil message bi, te normalement Yàlla moo gën a ñàkk a soxla intermédiaire ? Mu ne cell ba yàgg, mu ne ma may ma tuuti ma xalaat.
Ma ne ko boo tontoo rekk ma tont la de.
Marshiyah bi Dr Cheikh Abdoul Hakim Mbacké mou Cheikh Mouhammad Mountakha mooko défal mbokam Cheikh Ibrahima Fall Mbacké mou Cheikh Mouhammad Mountakha mifi bayéko Yalla nako Sunu Borom yeureum diégueulko té khaaréko Aldiana
Jaam bi dox bi muy dox ci yoonu yalla bu demee ba agg mooy tuddu «wusûl» bu aggee bay dox ci biir yalla muy dox bu amul fum yam muy tuddu «wisâl» ndax dox jëm ci yalla amna agg/ amna fum yam, waaye dox ci biir yalla amul fum yam.
Ki nekk ci maqaama wisâl nag mooy ëpp ay nattu ki tollu ci wusûl, ki nekk ci wusûl ëpp ay nattu ki nekk ci yoon wi di dox «sâlik» bi, ndax yalla ku ko gëna jege mooy ëpp ay nattu yu saahir ag yu baatin.