MATLABOUL FAWZEYNI a comme objectif principal de promouvoir le social en se focalisant sur les directives et recommandations de Cheikh Ahmadou BAMBA MBACKÉ
Bismillah ci weeru Safar gui 🙏🏾💯❤️✨👏🏾🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳🥳
Yalna ñu ci yegg Ak jamm Incha Allah
Sunu borom Meun Lo ñuko ci kataan Ak doley poche 🙌🏾🤲🏾🙏🏾💯
#Safar#18Safar#Touba#Mouride
🚨OFFICIEL: La lune a été aperçue. À cet effet, le mois de Safar débutera demain Jeudi 16 juillet 2026 et le Grand Magal de Touba sera célébré cette année le dimanche 02 août 2026.
🚨Ma ngi ziaar murit yeep
Ku ci joxeegul 7000 , na xam ni Seriñ Muntaxaa mo joxe ndigal ci murit bu nek , kon maa ngi fattali ñeep ci guddi ajuma ji ag bisu xasida bi nu jëm ku nek tabbal 7000fr ci touba ca kanam .
Ci numero bii 78 544 33 33 lan koy dugal.
Ayca Murit dox, dox.
🚨Déclaration du Khalife général des Mourides sur le lancement de la campagne internationale de mobilisation de fonds destinée aux travaux d’aménagement de l’Université Cheikh Ahmadoul Khadim de Touba.🙏🏾
#Muride#Education#Touba
Bisu xasida yi , bisu mucc la , bisu nangu ñaan la ku ci dem na fas yeene baayi fa bep bakkaar ag ñaan ay soxlaam , ku manul dem na fexe yobante fa alalam .
MBACKÉ 🤍💙- Yiww- Yatou - Taber:
Akhlou Hafiz! Ibn ib’n Ahmadu♾️
Gnignou bok teih ma raw leen ci Sope gui ma leen Sope🥺🤍
Yalna na nguen fi tewer watt ay infinité de bissoup Alquran-Xassida ak Zikroulahi bu melni Tay🤲🏾🤍
Beegnaniu walahi 📍🤍💙
💙تَقَبَّلَ اللَّهُ مِنَّا وَمِنْكُمْ صَالِحَ الأَعْمَالِ
Taqabbala-llâhu minnâ wa minkum sâliha-l-a'mâl.💙
(Qu’Allah agrée de notre part et de la vôtre les bonnes œuvres) 🤲🏾🥺
📍Touba♥️
Ahmadou Bamba mo Tedd 🤍🔐