SAFAR DAY 1
Sëriñ bi nee na jamonoo ngi ñëw joo xam ni la cay musle di naa léen ko wax yéen ñii fi nekk : ragal Yàlla sunu Boroom te jaamu ko, nangoo ligéey te ñime wéet, néew ay bëgg te bari muñ.
Source : Seex Axmadu Bàmba Xaadimu Rasuul, Jaar-Jaar ak Jàngale
J’éprouve 1 joie immense à l’annonce de la libération de mon frère Khalifa Sall. Je me réjouis de savoir qu’il retrouvera incessamment l’affection des siens dont il n’aurait jamais dû être éloign��. Je salue sa dignité et souhaite son rétablissement plein dans ses droits civiques.
T neneu comportement bimeu am ak mom motah mou interesser wou ci sama diiné beum faf weulbati xolam donte Athée leu wone. Li nak dou sakh ndam, sogné leu pour jullit bu nek xam ni fumu meunti nekk ambassadeur lafa, t ci wax ak jeuf legn koy wané. Kii jangal nama mbir!
Un des plus grands symboles de la France, #NotreDame vieille de plus de 800 ans est en proie aux flammes depuis plusieurs heures. Au nom du Sénégal, j’exprime toute notre solidarité à la France et à toute la communauté chrétienne à travers le monde.