As salam Aleykum Wa Rahmatulah Mangi len di Ziar dilen jox sen wacuway.
Di wax ñi am yeene jël been jukki diko jang mensuellement muy Goor Yallah wala Soxna amnañu ay jukki yu disponible.
Vous pouvez ne contacter par Dm ou faites signe sous ce tweet ma msg leen.
@joie_boule
#rtapprecie
As salam Aleykum wa Rahmatulah
Mangi len di nuyu dilen Ziar ci weru safar wi
Am nañu fi 2 jukki ci kamilu jigeen yi Soxna su ko bëgg jël pour diko jang ben yoon mensuellement Mën ga ma def signe en pv
@joie_boule#retweetapprecie
Borom keur la done sétane et la scéne ou la fille pleure parce que son papa féké woul son mariage m'a fait penser que nous aussi qui avons perdu nos papas allons vivre la meme situation le jour de notre mariage genre c'est fini quoi le vide est la et plus rien ne le comblera
As salam Aleykum wa Rahmatulah
Mangi len di Ziar buweer
Est-ce que Amna ay Soxna yu bëgg jël ben jukki si sunu Kamilu Soxna yi diko jang chaque weer ben yoon?
Je vous demande pardon population jël len jukki yi. Kuko bëgg jang ben yoon it bañu ma 😭
@joie_boule partager ko 😭