Serigne Mansour Borom Daradji moy nétali
Néna bis tourandom El hadji Mansour Balhawmi dafa yoni ndaw neko wowal ma Mansour néna ma ñew ñuñu ko tok si souf mouné ko dama wara def tourné bou sori 40 deuk la wara dem te yaw la begeu andal demal tagou Serigne Babacar nga wakh koko.
Sëriñ Tuubaa nee na
« Bàyyi leen kuñ ci jox soxna nga defe ni dangaa amub jaam, jigeen ñi duñ seeni jaam, jaami Yàlla lañ... [yaw góor gi], jigéen ji ba ñu la koy jox [soxna], dañ la koo jox ngir ngéen ànd jaamu Yàlla, waaye joxuñ la ko ngir mu doon sab jaam ».
S. Cerno Mb. G
Touba❤, symbole de la résistance et de la résilience face à la domination occidentale, l'unique grande ville du pays qui ne dispose pas de bâtiment colonial, synonyme d'une domination antérieure... Motah Serigne Touba bou Rewmi yéwé woone siye mbireum Toubaab doufi ame ndam👇
Lima léne dane dinke démbe ak beurki démbe laléne di dinke ,sakhe si diamou yalla si sounatou rasoulahi (swl) tope ndigualou serigne touba moytou ay téréme té moytou tonie.(cheikh abdou khadr mbacké)#SMN✨