« Ragal leen Yàlla ngir muñam gi... Te muñ gi yëp nak, yéexée la rek, waaye du neenal mukk !
Lépp lu jaam def, lu wuutéeg ndiggël dana ci am mbuggël ci àddina ak alaaxira (...) fii ak dabataloo ko ci tuub ak ballu Yàlla, wala ñu rambu ci yaw »
#Baay_Ñas
Ô Toi qui manifestes le beau et caches le laid ! Ô Toi qui ne saisis pas au premier péché et qui ne déchires pas le voile (de l'intimité) ! Ô Toi dont le pardon est immense et dont la tolérance est parfaite !