Seriñ Ahmadou njaay nguirane 🎙️: Déluuk Seriñ bu maag bi si sunu borom [ li waral Magal Darou khoudoss 🙏🏾
Seex Moustapha Mbacké (rta) yalla naa ñu ko sunu borom faayaal ❤️
Bari na tay ñu jàpp ne màggalsi nañ fekk dañ doxsi mbokk, ndax ba leegi nii nu ngi ci 19muharam, li tax ñuy màggal nag timis lay tàmbali jàpp timisi suba.
J'ai laissé mon porte feuille dans une voiture entre Thiès et Tivaouane .
Il y avait mes pièces dedans au nom de Mouhamed Fall et une petite somme d'argent.
Partagez svp 🙏🏿🙏🏿🙏🏿
{Yi nga xam ne sabab la yuy yombal julli guddi, mooy néew ak lekk ak néew ab coono, ak ñàkk a def bàkkaar ci bëccëg gi, ak ñàkk a bari aajo yu jëmul ci Yàlla.}
Masaalikul Jinaan !
Rafet njort ci sa bopp, tey ñaaw njort ci keneen :
Bokk na ci ag matadi, lépp lu sa moroom def nga ñaawlu ko, te yaw saa boo ko defee mu doon lu rafet lool ci yaw, nit ba la nga koo diiŋat walla ngay sikkal jëfam, jëlal sa bopp teg ko fa mu nekk, nga xool bu doon yaw la nu muy deme, loolu boo ko dee def rekk sa njort ci nit ñi day mujj rafet lool.
War ngaa def it saa bu sa xel xalaatee lu ñaaw ci nit, nga jàpp ne sag ñàkk a defaru rekk moo waral xalaat yooyu, waaye kii moom li mu def lu baax la.
Bu dee sa xel daa dal ci li ngay def, ba tay jàppal ne sikk su nekk ci yaw rekk moo dalal sam xel, waaye lii moom defewoo ko na mu ware, loolu lañuy wax tuumaal sa bakkan, lu xew rekk gisal ne sa bakkan moo lay jéem a jëme feneen.
Leeral ci Masaalik !
@PR_Diomaye tu es heureux de voir des gens et des opportunistes manquent de respect à Sonko.
Président Diomaye ça reste 32 mois sur ton mandat . Après tu seras le plus grand traître que l’histoire politique du Sénégal a jamais connus 🇸🇳.