Fukki naga'k juroom ci bis bu nek
Ànd'ak gileem ak fukki bëy lay sàkk
Ba muy ayag bis Seex ne tay ma rendi
Nit kuy taxaw, jox tan ya ndax ñu màndi
Daam ne ko "jaarama" mu jàpp ab jaam
Jébbël magam Sëriñ Momar Boroom Saam
Jarama Borom Daaru Salam ak Gawaan 🙏🏾🙏🏾
Lu waral Màggalug Daaru Salaam ?
Màgalug Darou Salam, mooy bis bi ñuy fàttaliku ngan gu rëy ga Mame Cheikh Anta ganale woon sëriñam ba Khadim Rassoul, ba mu jugee ca tukkib Géej ga ca Gaboŋ, ci atum 1902.
Cheikh Moussa Kâ neena :
9 || Il créa dans tout le pays des champs pour que les talibés puissent travailler pour son guide Serigne MBacké Sokhna Lo. Quand ce dernier disparaît il va chez Serigne Saliou pour être son talibés et ne travaillant que pour Serigne Touba.
( À suivre ).
THREAD : Serigne Cheikh Ndiguël Fall
• Biographie : Serigne Cheikh Ndigueul FALL est né en 1953 à Ndiarème Keur Cheikh, fils de Serigne Cheikh FALL Bayou Goor et de Sokhna Rokhaya NDIAYE. Il est de la 3éme génération de marabout Baayfall (Cheikh Ibra est son arriére grand-père).
8 || Très tôt, Serigne Cheikh Ndigeul Fall étonne ses aînés qui, remarquent chez lui une incroyable intélligence et un acharnenement sans parreil à l'abattage du travail, ce qui lui a valu le préstigieux surnom de "Gaindé Khelcom" littéralement "le Lion de Khelcom".
#Hadiya: Le khalife général des Baye Fall, Serigne Amdy Modou Mbenda Fall a remis 90 millions, au Khalife Général des Mourides, Serigne Mountakha Mbacké.