La vie chère étouffe les Sénégalais.
Face à la hausse du coût de la vie, il est temps de se mobiliser et de faire entendre notre voix.
Je soutiens l’initiative #30JoursPourLeJustePrix.
🚨Pétition citoyenne contre le soutien de l’Etat du Sénégal à la candidature de Macky Sall au poste de SG de l’ONU. J’invite toutes les personnes éprises de justice à partager et faire signer. Nous y reviendrons demain sur notre matinale de 09h. https://t.co/wxo1LMv56C
Sénégalais aka gaawa découragé ci am réewam.
Xanaa xamu leen ne, Politicien yi seen jëf yu ñaaw yii li ñu ciy jublu mooy fexe ba gëmloo nit ñi ne réew mi du baax te nun ñépp noo yam.
Loolu mooy waral nit ñi génne seeni xel ci baaxug réew mi, bàyyee leen ko ñuy yàq ak di def lu leen neex ci askan wi.
Ndax réew mu yàqu ci lu ëpp 50 ans, man naa baax walla mu changé ci lu matul 10 ans ba 20 ?
Xanaa xamu leen ne révolution dina échec ay yoon doora réussir ? Demleen gëstu ci àdduna bi r��ew yi soppiku yépp ngeen xool fi ñu jaar.
Afrig nun Senegal noo ci gën a yàkkamti gën cee bëgg lu yomb, xoolal tay Mali, Burkinaa, Niger, lu metti lool lañuy dund ci ñàkk électricité ndox sécurité économie bu daanu, waaye teewul ñuy gunge seeni njiit gëm ne seen réew dina baax.
Ñëwug Maki Sàll :
Bu amee ku ci pert dëgg mooy Jomaay mi ko fi indi, ndax Maki opposant la ci moom, ñi mu àndal nanguwaat nguur gi lañu bëgg, kon tay bu ñu naan Maki am na doole ba leegi, moom Jomaay miy président te tollu ci taxawal partie moo war a tiit.
Mbooloo miy teeru Maki waru leen a jaaxal, ndax Maki bàyyi na fi 36% ciy sénégalais ñu ànd ak moom, mu dem législatives am plus de 15 députés, ñooñu ay sénégalais lañu te mbooloo mu bari lañu.
Ablaay Wàdd ag delluseem moo rawoon fuuf gën a xumb, campagne législatives moo ko defal boppam waaye amul sax 20 députés.
Mbokk yi sunub taxawaay mooy, bañ a tàyyi bañ a yuqat, m��me bu nu dul fekke baaxug Senegal it sunuy sët fekke ko xam li leen seen i maam jariñ.
Nun nag (njariñ loo fekke) moo nu sonal, lépp lu ñuy xeex bu njariñ la jëmee ëllëg nu génnaat ca, da noo wara sonn ngir ëllëgu sunuy njaboot.
MOR SOURANG
@moughniyan@jbndour Wax ga deug deh yeene geuneul reuy niou tane la bayi say morom ngir tabb la président te nienen gni mérite ko lolou nak tere wut niou am ngor tokk andak yow goungé la kula yeene ga nek njitum rek defena fala yeene ju rafet yaam
🚨 Diadia souffre d'insuffisance rénale et subit la dialyse, entraînant des frais médicaux importants. Sa maladie le ronge jour après jour, mais ensemble, nous pouvons l'aider à supporter cette épreuve. Offrons-lui un espoir et un soutien pour qu'il puisse surmonter cet obstacle et retrouver la joie et la liberté. SOS pour Diadia, aidons-le à lutter contre sa maladie.
@aliounetine16 vous pourriez être mon grand-père moi votre petit fils je ne me permettrais jamais de dire certaines choses en public ndax damako jomb mais malgré votre grand âge vs manquez cruellement de discernement pour distinguer dire la vérité et faire de la manipulation nala yalla dimbali
J’ai jamais été aussi fier d’appartenir à @PastefOfficiel
J’ai jamais été aussi fier d’avoir un leader comme @SonkoOfficiel
Et surtout j’ai jamais été aussi fier d’avoir des parents qui m’ont inculqué des valeurs pour ne pas être un traître, un complexé, un parvenu, un arriviste, un vendu.
Dieu est avec les endurants.
Fier de vous , fier de mon peuple.
#SONKO2029