Yen gayi bamba deglu len Musa murid ba wonalen Ndaw akmag gor ak djigen nan wuyuji ahmadu mbacké Magalgi lalen di xibar yen ñi xamul tey xibar t nara dm difa ziar ngir jëmi ahmadu mbacké ñenenti fan ci aw safar nañëp jog wadjlé safar ngir bamba rabihu safar la wajle ahmadu Mbakké