@babsSs06 Le lieu et le service proposé aussi jouent sur le prix. Boo deme castors ci biir marché di lekk avec le bruit du marché tu pourras épargner maximum 10mil
Cheikh Ibra nourrit tôt le désir d’une élévation spirituelle pour accéder à l’essence divine, mais comprit très tôt que la science livresque ne pouvait lui suffire dans cette quête. Il acquit la conviction que le salut ici-bas et dans l’au-delà, donc l’accession au salut, à la ⤵️
Am na jigéen ju mësa faatu am ku ko gént mu sonnu loo u. Bam xëyee mu wax ko Al Hasanul Basriyu. Ginnaaw bi Al Hasanul Basriyu géntaat jigéen joo ju gis ko mu nekk ci al janna.
-Mu laaj ko lu la fi andi ?
-Mu ni ko benn waay moo romb ci sunu armeel yi fekk ñuy juróomi benn fukki junni ak juroóm (65 000). Mu julli ci yonent bi (YYJSM) benn yoon (1)
yéene ñu tuyaa ba ji. Ñu jéggal ñu ñun ñépp ci barkep jullig waa joo ju.
Majmahu nureeyni
La participation de l’épouse aux dépenses familiales :
Selon la loi islamique, l’épouse n’est pas tenue de participer aux dépenses obligatoires du foyer dès l’origine, et il n’est pas permis de l’y contraindre.
La participation volontaire de l’épouse (travailleuse ou salariée) aux dépenses de la famille est un acte recommandé par la charia.
Il est permis aux époux de se mettre d’accord, d’un commun consentement, sur la manière de disposer du salaire gagné par l’épouse.
Si l’exercice d’une activité professionnelle par l’épouse entraîne des dépenses supplémentaires qui lui sont propres, elle en assume la charge.
(Al-Fiqh al-Muyassar, Les questions contemporaines du droit de la famille, vol. 11, p. 142).
Ngay wuut dara muy jafe amul lu ci gëna gaaw xassida gi bismillahi ikfini.
- Ku koy jàng sunu boroom dina la aar ciy mussiba ag balaa ag lépp luy lore
-Ku koy jàng dinga mucc si ayu lammiñ ag bëtt
- Ku koy jàng dina la taxa am jàmm fa nga nekk
- Ku koy jàng yàlla dina la defal ag ubbeeku ci lepp loo dugg, dina la yombalal say wërsëg!
#TaawOu
Les fondements (uṣūl) de l’école de l’imam Mālik sont les sources et les principes sur lesquels il s’appuie pour déduire les jugements juridiques islamiques.
1- Le Noble Coran : il constitue la première source de la législation islamique.
2- La Sunna prophétique : les paroles, les actes et les approbations du Prophète ﷺ.
3- L’Ijmā‘ (consensus) : l’accord des savants qualifiés de la communauté sur une règle juridique.
4- La pratique des habitants de Médine (‘Amal Ahl al-Madīna) : l’une des caractéristiques distinctives de l’école malikite, car l’imam Mālik considérait que les habitants de Médine avaient hérité de nombreuses traditions pratiques des Compagnons.
Ku bëgg topp sa bakkan wala banneex mashab imaam maalik, dula arranger.
Ku nekk amnga droit nekk ci mashab bula neex, waaye nga respect yeneen mashabs yi ag woroom xam-xam yi, surtout ku melni imaam maalik minga xam ni yonent bi shw mooko joxuñ.
يوشك الناس أن يضربوا أكباد الإبل فلا يجدوا عالما أعلم من عالم المدينة