Yalna nu Buur Yàlla ﷻ may alal gu lew, barkeel, bari, fi muy juge mu gërëm ko, fa muy dugg mu gërëm ko, Yalna bu mu doon fitna ci nun fiddunyaa wal aaxirah ci barke Yonente bi ﷺ 💚
Evite la procrastination car à la longue, elle mène les soumis vers la perversion.
Persévère dans la quête de la droiture et de la soumission avec ascétisme, scrupule et sobriété.
« Cheikh AHMADOU BÀMBA »
Àdduna li muy yaatu lépp, nit ku ne sa bopp rekk nga ci am.
Ña dem barsàq ku ci ne ci kërug boppam la nekk moom kese
Ëllëg bis-pénc nit ku ne Yàlla dina wéet ak yaw lijjanti la.
Ndax kon jotul ku ne ci nun tal boppam kese fexee mucc tay ak ëllëg ?
Souviens toi que même si tu fais tes 5 prière à l'heure, tu jeunes souvent dans l'année, tu te préserves de la fornication tu donnes aux démunis.
Une personne noyée dans le péché peut être meilleur que toi par son humilité qui l'élève auprès d'Allah.
Le gardien de but des U17 du Sénégal, Assane Sarr est un joueur appelé à avoir une grande carrière internationale.
Non seulement il est solide sur sa ligne, mais il se distingue également par sa sérénité balle au pied, ses relances propres et précises, et des sorties parfaitement millimétrées.
Au-delà des qualités purement techniques, c’est sa personnalité affirmée qui impressionne. Capitaine, leader naturel, il assure et rassure, ses coéquipiers comme les supporters, avec l’autorité naturelle d’un gardien qui commande sa défense et inspire confiance à l’ensemble de son équipe.
À son âge, ce niveau de maturité et de maîtrise est remarquable. Une valeur sûre pour le présent, un grand nom pour l’avenir.
Sunna 👇 :
A partir de Tisbaar d’aujourd’hui, jusqu’au Fajr du dimanche, il est recommandé de faire trois takbir (Allaahu Akbar) après chaque prière obligatoire
Sopp na nu, tàmbbalee ko tisbaru tay ba Fajaru dibeer bi, soppu na nu gànnaaw jullig farata gune nga jangg 3i takbir
Xamnaani daal nitt loo xam xam warnga gorgorlou si am tegginn…
Teggin si ningay wakhei, teggin si ningay jeufee, teggin si ningay jeufleuntee ak nittgni…
Thread 🚨 🧵 : Tabaski ak luci Aju ( Ci Mazhab Imam Maalik )
Di saaku ngen yaataal koo 🙏🏾
Taariq wii : Surat As-Saffat (37:102 , 104-107 )
Li maataa kham 🧠 : Sounah mu’akdaa laa = sounah su fedalikou ( teh it faaw am niouko def , bou nieup andone bagn ko def , njitt la saañ na jeul nganay jeuflante ak niom nguir niou def ko )
Kaan laa tabaski war ??
- keep ko khamni meun ngaako , manam ndieugou khar wii Dou bayi ak gaum ( jafe jafe dépense , courant … etc ) ci att mi
Koon keep kou deme nonou sounah la ci mom ak keep ko khamni moko wara dundal ( doom jou jiguen bou amagoul borom keur , doom wü Goor bou matagoul liguey , ay wayjouram boude danio niaak )
NB : Ap soxna mom , borom keureum tabaskil ko warrout ( dou force )
Ñi nga khamni sounah laa nga yobalé leen tabaski soxna bokouci.
Ap soxna bou amé aalal, ni tabaski dooné warteef ci borom keurem lako warreh
_ ap jirim bou baayam fatu bayil ko alal, sounah la niou guenel koo thia tabaski
Naka nonou waji meun na jeund been khar yéene cia tabaski waalel ñonou nieup 👇🏾
Cheikh bii daal Yalla nako Yalla fey yiww bou beurri, j’apprécie trop ses tweets notamment le fait que sujets you beurri jottneu ko traiter bou yagg Ma Sha Allah🤍