Ruuh gu xiif moo gëna metti beneen xiif bi, ndax dangay yëgg benn vide profond boo dul mëna expliquer, dangay yëgg weetaay doonte Yaangi ci biir nit ñi ñu wër la… nga yëgg ni amna loo manquer doonte amnga lepp ci aduna.
Xiifu ruuh mën nga ko baña gaawa yëgg, ta xam la vérité, am connexion sa digënte ag yalla, xam sa bopp dëgg… mooy tax nga suur.
Ta amna numuy deme sax nga agg foofu ba pare di gëna xiif.
Tollou waayou diaam bi thi Adouna thi diganté (4) mbir yi rk la nekk
Banneekh ag nattou ag toppou ndigal ag moy ndigal
Boo nekke,thi banneekh,lala thia war mooy sant rk
Boude thi nattou,lathiay sa warteef mooy mougne
Boo nekke,thi ndigal yi nga gisne loumla dimbale la👇