@badara_25 Wakh deugg nak diaay katou café ☕️ yi dagn leen wara filtrer nakh diaay café business bou dokh la mais ségg café am yoon maname dosage bi etc… client yi nga diokhleen sen akk mais lgui kenn kholatoul satisfaction kw gneupp sen poche yi moleen gnore😫
@msheikh290@Terangaboy221@JoueursSN Cherif Ndiaye kheutio woul place , il se bat pour avoir ca place dans cette équipe teh lolou mouy Mbappe , di Messi di Sadio Mané kouné aw nassi . La decision finale appartient à Pape Thiaw
@Terangaboy221@JoueursSN Saay joueur yi dougn si dara , lepp selectionneur bi deff ay etude wam si joueur yeupp ba parei convoqué leen est l’unique responsable. Nakh joueur bougn né kaay dem CDM doula meusseu wakh je ne suis pas pret pour X raison , bou doin ioe itam dangay dem