yonent bi aleyhi salaam wax ni ñaari julit bu ñu nuyo tant que ñu ngi jamasante ñu leen di baal sen bakkaar ñoom ñaar ñeep Bu njëk mag ñi bu ñu daan jamasante ngir dëppo ag lii la woon
motax ñu daan yà ggal jottaay bi di laaj njabot gi , nawet gi , jur yi , wergu yaram loolo lep ngir lu ci sikk ku nekk ñaanal si sa moroom
NKD House, in Dakar, Senegal
The walls are made from earth bricks. The pattern you see is alternating protruding brick courses. This casts shadows, and reduces the amount of sun on external walls
By Worofila
Xale bu ndaw saa bo ko xoole sa xel warul dem ci dara lu dul xale gi mu doon , leneen lo gis lu dul loolu tawat a ngi sa xol , te lu bon a bon a ngi sa xel mi lo war a faj .
Serigne mountakha sayu ndigeul al Qurane ak Qacida jouguer rek khamal ni mo ngui lidjenti jam gni lu rĂ«y fa sunu Broom đ„č
Yalla nako sunu Broom jox fan Yonenete Yallah Nooh Haley salam đ€đđż