Comprendre la doctrine d'abord.
Notre ère n'est plus celle de l'obéissance aveugle à un guide ; il faut, avant tout, s'abreuver de l'enseignement du Cheikh. C'est uniquement cette démarche qui permettra de bien identifier qui l'on doit suivre et ce que l'on doit suivre.
Assurément, cette confrérie, dont une seule entité des siennes contribue à hauteur d'un milliard sans apport extérieur, est épargnée par cette prophétie d'un vision aveuglée.
Cheikh Ahmadou SOUR
Le prédicateur du déclin des confréries et ses sbires endoctrinés, avec leur météo fausse, ont sûrement été guidés par des délires et non par des facteurs rationnels considérables. Ou peut-être parlaient-ils d'une autre époque dans leurs songes.
Ñëw na ci Hilyatul awliya, Abu nahim Al asfahani mu wax ne: Am na ku laajoon Imam Chafi «ñaata att nga am?» Imam Chafi neko «Bokkul ci kersa nit di wax ay atam».
Amna ku laajoon Imam Maalig ay atam Imaam Maalig ne ko laajal lu la amal njariñ.
Buñ la dee jay fii fi àddina ba nga defe ne manoo fee ñàkk toxantul ca almeer ya. Da nga fekk:
Buur bu yilifoon suuf yepp, Jongoma ñu goor ñépp naboon, Boroom doole ju kenn yabul, Waliyu wu yàlla masul delloo ag ñaanam, Boroom alal ju jeexalul woon dara,
Ponkal mu ubb mbooleem làmb yi, Sëriñ bu ñépp daa dar, Boroom lijjanti yu loxoom jotoon fepp, ku siiwoon ba ken umpule wu ko ci dénd bi ñoom ñi ñépp tëdd faak ku daa yori sagar ñu naan ko dof bi, ku mesta am lum lekk, ku mesta yilif ab wurmbël, ku laggi ba daawul yékkati ab cér,
Jàmbaar nga d. Lénn ci faqiih yi parfois duñ sopp ci masala phénomène yu mujj yi. Séen fiqh dañ koy bayyi ca teere fukkeelu xarnu ya. Seetlu naa ci yaw sa xarañe masala yooyu.
Sooratu Naba'i nee ñu ku koy jàng biss bu set ci am at balaa att maa jeex yàlla dina la wërsëgal nga siyaare ji yonnant bi (saws).
Lii ñëw na ci teere xawaasul xur'aan.
Jumaa ju sosu ci ngor moo ngii
Jumaa ju sosu ci jomm moo ngii
Jumaa ju sosu ci dogu moo ngii
Jumaa ju sosu ci ñax wu lew moo ngi
Jumaa ju sosu ci dëggu ag bëgg yàlla moo ngii
Jumaa ju sosu ci jayante ag weeru ci yàlla
.........
Yàlla na Seex Muntaxaa mottali liggéey bi.
Yu melni sëlmël ñaari yoon mba amiin ju mboolo mi andandoo def ca kaw ag yeex a kabar armal ginaaw lixaaam ag yu ni mel du woon ci ngir mi te yaatu na léegi ci jakka yi. Ñu bari ñoo ngi koy roy te yëgunu ko sax.
Sàmmu ndonol ngirum Maalig mi màgg ñi tënku woon ak jàngale ko bañ xam ko.
Yu bari ngir yu bees yi ñoo ngi ñu ci'y yobaale. Ñenn ñi moom tënkoo tuñ ci dara ñooy àtteel seen boppu seenu déggiin ca aaya ya mbaa adiis ya.