Man ak ben mbok taalubé meus negn di waxtaan ak ben yaaboy muñuy wax sen aal yi bolen takké soxna dingenko tek si suuf. ñunek fa di aalu nanko xamo lingey wax 2ans après sam mbok taalubé bi yeew Soxna ma demfa seeti leen gnu tok si salon bi soxnaci nek si wagn bi di wadial...