❤️ الحمدلله| |Mouride Yaakaar Sëriñ bu Mag bi ❤️| Taysiirul Asiir| #Patriote |Pour un Sénégal 🇸🇳 souverain, juste et prospère | Pour l’unité ❤️africaine |
Sou Gamou gui dialé ma wakh leine bokatouma Awale bokouma kiiraay itame… politique dou tiakhane ndakh gestion wou deuk dou yeufou tek khel
Maname bayina aye mbiirou politique ba diamo nekh bama guiss lou bok ak samay principe !!!
Di nagn def thies bibliothèque ak fou khaler yi di diangui karaté 🥋 def fa salle bou handicapé yi di defer formation si defar ay produit you melni diw bop ( projet en cours ) di nagn fa def space vert etc…😭😭😭deuk bi keine mounou fi vidéo si jaam @Omd_authentik thies ak bruit
Tu as le cœur un peu plus lourd quand tu compares le discours de @BirameSouleye d’aujourd’hui d’avec l’entretien de saa-obstacle (kiiraay) d’hier.
Waaji tayle na sunu combat nii rekk !💔
Sëriñ si daal ni leen politicien yi yabe jaaxal na ma, fond politique yi ngeen koy séddoo ak di ko may seeni nit, tay jii ngeen bëgg cee taqal sëriñ si, naan ci la ñuy joxe gàmm ak màggal, gàmm ak màggal taalibe yi ñoo ciy def seen alal kenn soxlawu ci seen alal yu araam yooyu.
Seen stratégie ci loolu nag mooy, xam nañu Senegaal ni leen seen kilifa diine yi ñoree, ñu bëgg a jaxase Sëriñ si ak taalibe yi, ak bëgg a nopplioo képp kuy wax ci fond yi.
Li wér te wóor mooy mbooloo mu ànd ciy tappale ngeen ngir lekk xaalisu askan wi rekk, ne fàww ngeen tudd ci Sëriñ si ndax kenn bañ cee waxati.
@drelhadjiAdiouf Seen fumisteries yi génneleen ci Tuubaa
Gérez vos querelles politiques en épargnant le nom de Serigne Mountakha.
Le Mouridisme a son propre mécanisme de financement de ses projets.
Il n’a jamais dépendu de fonds politiques pour réaliser tous ses grands chantiers.
Mane d saaga sakh sékhoumako ak kéne wahoumala ak sama Sokhna nite daye yar bopam bagna tamite wakh diou niaaw wahoumala aye door moom souniou si nara ague kounék dém adouna métiwoul louye moudié si nétali diaroul niaawal.