Nit man naa joxe wird, joxe lim boo xam ne, boo koy wrid lim boobu dalay xiir ci jëmmam rekk, nga di ko sopp ba doo amati ci moom sago loo am jox ko.
Teyleen ci wrid yi ak lim yi.
Moomuma wird yi nappaatewuma waaye sañ naa laabire nit ñi, te li may laabiire lu ma xam la.
Personnellement, je n’aurais pas procédé au paiement anticipé de ces échéances.
Cela fait perdre de l’argent au pays plus qu’il ne lui en fait gagner (on gagne que dalle).
Sur le plan purement financier, c’est une perte sèche de trésorerie à court terme, des liquidités qui auraient pu être affectées ailleurs et générer des revenus.
C’est un coup purement politique, un signal adressé au FMI qui débarque à Dakar cette semaine.
Un État vraiment solide n’a pas besoin de payer en avance des coupons exigibles dans 7 jours pour prouver qu’il honore ses engagements. Il paie à terme, c’est tout.
Les marchés lisent Bloomberg.
Ils savent. Le FMI aussi.
Félicitations à Pastef. La souveraineté economique a besoin d’une organisation pour se construire. Il faut vouloir pour pouvoir, mais pour pouvoir il faut une organisation. Que la souveraineté soit libérale Progressiste. Forces Coalisées pour l’Unité et la Souveraineté (FOCUS).
Sonkoo polatigu yar ak teggiin la woote, xam-xam ak xalaat yuy suqali réew.
Amul tooñ amul saaga.
Sonkoo màgg na ba mat sëkk njiit li mu doon, pastef seeni reen sampu na ci suuf, lu muy gën a yàgg di gën a dëgër.
❌DES AGRESSEURS❌
Aujourd’hui, tôt le matin, alors que j’étais sur le point d’aller au travail, j’ai vu deux personnes sur une même moto arracher le téléphone d’une dame qui se trouvait à proximité. Nous les avons poursuivies parce que nous avions remarqué qu’elles semblaient vouloir commettre un autre vol. À un moment, elles ont même tenté de s’en prendre à un enfant en poursuivant sa moto.
C’est vraiment honteux de voir de telles choses. Pendant que certaines personnes se lèvent tôt pour travailler honnêtement et gagner leur vie, d’autres choisissent de voler et de semer l’insécurité.
PS : CAPTURE IMAGE EN COMMENTAIRE
LIEU DES FAITS : ROND POINT MALIKA
#LCIS®️ #Sénégal #Jubanti #Indiscipline
Jomaay naka lay teudiei Sonko ancien PM sans am doolei assemblée ?
Jomaay loumou meune si bureau assemblée bay terei Sonko nek president assemblée ?
Loi reewmi moko mayoul si lolou dara soxla woul Segn bi sax ngir xam lolou
#Sëriñ-Mountakha wan na ko yoon !
#Président_Bassiru Jomaay Fay nee na : Sëriñ bi fan yii lin jokkoo bërina ngay wane #yoon ñu ciy topp nga joxe #ndigal ñu déggla jëfe ko ...!
⚠️ #Question : Lu nekk ci ginaaw wax jii ?
🚨Ma sàmp ay laaj :
-Ndax #Président Jomaay dafa amoon yeene #tëjlu Sonko Sëriñ bi ne ko tegal ci suuf mu topp loolu ?
-Ndax #Président Jomaay bi ñuy def #Sonko #Président_Assemblée dafa amoon yeene jëfandikoo #force ngir loolu bañ am Sëriñ bi ne ko #tegal ci suuf mu topp loolu ?
-Ndax #Président Jomaay dafa amoo yeene #tere ndaje xew xew yi Sonko di woote Sëriñ bi ne ko #tegal ci suuf mu topp loolu ?
Lu nekk ci ginaaw waxam ji moom #Président ?