Asalaamu aleykum maa ngi siyaar di fàttali ne Màjjaal mi moo ngi wéy
Képp ku bëgg a barkeelu mën nga maa yonnée àddiya ji ci sama numéro
78 592 84 17
Wave/OM
Xam naa naa ci mësa am bés balaa maa couper appel fàww mani tekk xaar 5s su kima doon waxal couper wul ma sooga raccrocher 😂
Parfois nit yaakaar ni couper na fekk ni couper wul di wax ay bal🤣🤣
Mon bijou🥹❤️
Yeuggoleen ko woon mais entre temps j’ai ouvert une boutique spécialisée dans la vente d’abayas pour femme (friperie, Egypte, Maroc, Dubai…) à Liberté 6💃
Ngeen dolli ñaan te seet si ñu inshaa Allah🙏
Maa ngi woo ñépp ci teewaay ak jëf ci bés bii ñuy amal le 13 juin Incha Allah à Saint-Louis
Xeebul yéemul Jëf Jël
78 592 84 17 Wave / OM
Ayca Murid Rt mu yaatu🥹
Tabaski 2026 : Serigne Amdy Khady Fall, khalife général des Baye Fall, à remis au khalife général des Mourides, Serigne Mountakha Mbacke Bachir, 2.360 moutons ,une enveloppe de 28 millions F CFA, 03 vaches ,01 cheval , 05 chameaux et autres ce lundi 25 mai 2026.