TÉERÉ BII (Fulkul Mash'hun) ÑU FI DOON JÀNG, waxuma ki ko jàng. Waxuma gni koy déglu. Waxuma wa dëkk bi. Waayé suuf soo xamné jàngees na ko fa rekk, ndax ! Ndax ! Ndax kenn da na fa dem safara, wala ? Man ñi jàpp né kenn du fa dem safara ca laa bokk man !
''5 Shawwaal l'' 5i fan i kori
#WIRDMakhuz
(Wird Mouride)
Sëriñ Tuubaa nee na: "képp kuy Murit góor ak jigéen digal naa la nga jël Wird wi te di ko jëfandikoo"