Li gën a bon ci ab entrepreneur mooy ñàkk yitte, ñàkk disponibilité, kenn manulaa jot.
Businessman boo gis muy protocole rekk xamal ne du dem fenn, Business ak protocole ànduñu.
Deel wuyu téléphone di rappeler say appel manqué, tont say message, bu sa benn client xam say yitte yu dul moom, fàww ngay muñ pour yenn client yi xawa doy waar.
Efficacité sa lépp di gaaw livraison ak yooyu, wara livré client naan ko, defal ndànk livraison yi daa bari, loolu sa problème la, mais yoonu client bi nekku ci, moom li ko ñor mooy jot ci commande am.
Tay la beussal niane ak fataliko SERIGNE AFIA imam di nahim serign bi..
niouy fatalikou ak diéxam takk si serigne bi
Amoul lén fén fudul fi serign bi,
ludul tokki guédj gui meussul takhali ko ak serign bi
Yalla naniou ko yalla doli fayal barkép serign bi
🚨 Nous avons besoin de votre mobilisation la plus puissante contre cette proposition de loi « permis de tuer ».
Signez et faites signer la pétition 👉 https://t.co/DPnOFt6dMd
Je crois qu’il faut rappeler que le 21 mai dernier, des groupes de néonazis semaient la violence et la haine sur le canal Saint Martin.
Aujourd’hui, on veut nous faire croire que le problème du pays, c’est un gamin de 14 ans qui s’amuse avec de l’eau.
Un pays où des jeunes filles de 13 ans sont obligés de vendre des sachets d’eau (qui eux mêmes sont nocifs pour la santé) sous le chaud soleil pour survivre.
Avec tous les dangers que ça représente.
Les journalistes sportifs sénégalais sont pire que Pape Thiaw.
On dirait que vous avez tous reçu le même mot d’ordre genre tirer sur Pape Gueye coûte que coûte.
Xamolen gat, nopilen
Pape Gueye est un compétiteur frustré qui s'exprime à chaud. Mais cette débandade est avant tout la responsabilité du Pr Diomaye qui vire un ministre des sport à qlq semaines d'un tournoi pour des raisons politiques puis ces fédéraux et ce staff qui n'ont pas été à la hauteur.
L'affaire du petit de 15 ans qui a massacré une grand mère a la perceuse a pas fait 1% du bruit que fait l'affaire du petit de 13 ans qui arrose des passants.
Je vous laisse deviner le quel est blanc et le quel est arabe.
Sang bi halayhi salaam nee na:
« Mbir yi ñu ngi [leen di natte] ci mujjantal yi »
Waxaat ne:
« Jëf yi ñu ngi [leen di natte] ci seen ug mujjantal »
Muy ci diine ak ci jamono, constance lu am solo la.
Je viens de croiser un jeune homme qui vient de perdre son passeport dans le métro il s’est arrêté à Odéon il y a 30 min avec plus de 1000€ dans son sac on sait jamais je tweet il était au plus mal
Prénom Nom : Yassine Loukili
Numéro de téléphone : 0775159864
rt svp ‼️
🚨NDIGËL
Seex Muhammadul Muntaxa jox na ndigël Sëriñ Amdi Xadi Faal xalif seneraal dee Baay Faal ag jabootu Seex Ibraayma Faal gépp ñu tabax Jakka ji ci Kër Sëriñ Tuubaa gi ci Héliport laata Magal Tuubaa gi.
NB: suba ci alarba ji (mercredi 01 juillet la ñuy tàmbali leggey bi.