Sur ce réseau, tu vois des gens qui ont des idées virtuelles, ba noppi ñu koy imposer nit ñi.
Soo quitter sa appli X rekk, tu fais face li nga xam ne mooy réalité yi.
Su fekkoon danuy wax ci réalité yi, di ko bind ak di ci wax lu rafet, ñu bari diañu ci jàng te dinañu ci jëlee lu am njariñ.
Moo gën fuuf werante yi ak di wax loo xam ne gëmoo ci dara.
Sa ma mame Serigne Massamba Syll mo wacc liguey ngen ñaanal ko djeguel ak yermandé 🙏
Mo nekone Khalifa Serigne Mirina Syll
Mok Serigne Bassirou khadim Rassoul sen ñari wajur yu jugën ño bok lep( ndey ak baay)
Le Tawhid de Serigne Touba. Arrêtons-nous un instant et écoutons studieusement.
C’est ça l’essence même de tout, des enseignements.
Par ailleurs c’est déplorable que ces contenus ne soient pas en d’autres langues afin d’atteindre un maximum d’audience.
La mission est là!
Pression sociale,Environnement,Vouloir réussir coûte que coûte (tékki)
3 choses qui peuvent faire basculer la vie d'un jeune en une fraction de seconde !!! La seule solution pour ne pas tomber sur leur emprise c'est d'être solide mentalement et avoir des principes bien définis⤵️
Serigne Mame Mor Borom Sham (Son vrai nom est Mouhammad)mou Sokhna Diarra (Frère aîné et disciple de Cheikhoul Khadim) nékoone diamou katou Yalla boumak nékoone yarékate di Borom Kham-kham lissi firndé mooy diangalna Serigne bi amoona niéwanté si moom lole dako bayi khél si lép
Tay si khoutba bi, Imam né neu ñu woute ay àndandoo yu baax.
Tey ànd ngir Yàlla kepp, té baña ànd ak niit ngir alal, wala daraja...
Yokk na si, su ñuy ànd ñu baña jëw (bàyyi leen CAS), ñuy bàyyi wax lu bone ak diko waxante, ku nek nay xirr moroomam si lubax.