L’histoire retiendra que le Sénégal s’est fait respecté tout seul. Aucun imbécile n’osera plus dire du n’importe quoi comme il le sent. Oui, c’est NOUS les méchants.
“La bataille des médias” who’s next ?🤗
Sñ muntaxaa bashir yaalna fi yagg lool te wer , siecle bi ñu nek gisul ku mel ni mom si xam xam ag sagesse ag mbaax ag ragal yallah ag yërmande ag njariñ ci nit ñi.
Sunu kilifa gu baax gi yaalna ñu ko fi yallah baayil ñu yagg ko topp te mu yagg ño sagal di nu yërëm di nu musal si merum yallah .
Yaalna sunu boroom yaggal ko fi ba muy keeman te lep lubaax lu mu jot a def ci reew mi njariñ yi amee ci kanamam. Sñ muntaxa bashir yaalnako yallah samm. Aar ko musal ko barkep borom touba .😭
Le gouvernement a tenu ce jour son tout premier conseil des ministres, un événement marquant le début d'une nouvelle ère politique. Après une séance de travail intense, le Chef de l'État et les ministres ont posé pour une photo officielle sur le perron du palais de la République.