ICE du noppalu ci tas njaboot yi ci dëkku New York. Du nu noppalu ci xeex ak ñoom.
Woteel ci Buum u Jokkoo u Taxawu ci Yoon ci wàllu Doxandeem ci 1-800-354-0365, walla nga woo 311 te wax ne “Immigration Legal” (Taxawu ci Yoon ci wàllu Doxandeem), ngir am ndimbal bu laajul fay, bés bu nekk, am na sutura.
Sunu dëkk waa New York lay jàppale.
« Sunu Boroom nanga leen musal, jàmmal leen te ñeewant leen, te bu leen jàppe seen bàkkaar yu bari yi, ndax ñoom bu dee dañu laa moy it càggante rekk a tax, waaye
bokkaalewuñu la ak kenn. Seen yaram yii àttanul sa balaa ndax doyadi gu nekk ci ñoom. Seeni xol it du jeng mukk👇